Guddi
🎵 1164 characters
⏱️ 3:41 duration
🆔 ID: 10630919
📜 Lyrics
bou timiss bi maacé
gouddi gui khaadié
damay khallaat
si sama life
bou métit yi taacé
yaakar you taass yé
man sonneu naa
cassos bou mak
niouy gouddé di naadjé
ñane yalla waa héé
fébar di khaar
mais dé mognouy fath
lou niti meun ti wakh yeup
ak lougne meunti wakh yeup
kén bouma wakh ni nath na
nakh si gouddi gui laay job
deukkeu ci di fass diom
wara déf lougnou war yeup
loum mérité laay dieul
man si gouddi gui laay job
Oh my lord
no time no
so far wow wou woh
oh waa oh wou woh
oh my lord
no time no
so far oh wou woh
oh waa oh wou woh
bou timiss bi maacé
gouddi gui khaadié
damay khallaat
si sama life
bou métit yi taacé
yaakar you taass yé
man sonneu naa
cassos bou mak
niouy gouddé di naadjé
ñane yalla waa héé
fébar di khaar
mais dé mognouy fath
louné dink ko dath
founé dink fa diaar
geumko rk no time
meun na néé
boko défoul koukoy déf
siggil say waadiour
guénné len ci waay
fo dou wééss
nakh gouddi gui silay khékh
dioukk si siggil sama yaye djéé
toukki sama mind fékh
Annhh yeah
I know I know
you know I know
I know I know
you Know I know
I know I know
you know I know
I know I know
you know I know
yéé éh
gouddi gui khaadié
damay khallaat
si sama life
bou métit yi taacé
yaakar you taass yé
man sonneu naa
cassos bou mak
niouy gouddé di naadjé
ñane yalla waa héé
fébar di khaar
mais dé mognouy fath
lou niti meun ti wakh yeup
ak lougne meunti wakh yeup
kén bouma wakh ni nath na
nakh si gouddi gui laay job
deukkeu ci di fass diom
wara déf lougnou war yeup
loum mérité laay dieul
man si gouddi gui laay job
Oh my lord
no time no
so far wow wou woh
oh waa oh wou woh
oh my lord
no time no
so far oh wou woh
oh waa oh wou woh
bou timiss bi maacé
gouddi gui khaadié
damay khallaat
si sama life
bou métit yi taacé
yaakar you taass yé
man sonneu naa
cassos bou mak
niouy gouddé di naadjé
ñane yalla waa héé
fébar di khaar
mais dé mognouy fath
louné dink ko dath
founé dink fa diaar
geumko rk no time
meun na néé
boko défoul koukoy déf
siggil say waadiour
guénné len ci waay
fo dou wééss
nakh gouddi gui silay khékh
dioukk si siggil sama yaye djéé
toukki sama mind fékh
Annhh yeah
I know I know
you know I know
I know I know
you Know I know
I know I know
you know I know
I know I know
you know I know
yéé éh