Gen ji dekk
🎵 1815 characters
⏱️ 5:36 duration
🆔 ID: 10691212
📜 Lyrics
Guentouma hé Gentouma
Hoooooo HOoo!
Guentouma hé Gentouma.
Beugouma yewou rek guente gui diekh.
Ngua neck fi ma neck feulé Dou té niou gussanté
nékal fi mangui feulé Beugenala,
Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako.
Beugnala Guemenala
Geumnawooo Ho
Guentouma!!! Guentouma!!!
Nekkal fi ma neck feulé Dou té niou gussanté
nékal fi mangui feulé Beugenala
Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako
Beugnala Guemenala
Geumnawooo Ho
Guentouma!!! Guentouma!!!
Naniou Khalaté lou lenne nekh ci mane
Bayiléne niou wakh louléne nekh ci mane
Maye adji kiiy beug. Beugnala
Beug Sa Deuk Ba Deuk Fa mouy guene di deuk ci mane. "WTF"
Yaw yaye ki kidnaper sama life
Hooo Hooo My life...
Kidnaper sama temps khamnala
Temperature bo necké soma guissé guif
Dangua beugonna kham ci lanne la néék
Dangua beugonna kham ci lanne lay dokh
Yakamtina niouye skype
Deug sa viber, am sa allo!
Arrosé na samay fleur mane
Ba meuna feyy ci bissoub mbeugéll yii
GEN JI DEKK dama yague ak yaw
Ba so yeukeutii say kaddu
Bala nguay danéél makoy teureul
GEN JI DEKK
Geunalanté wouma la ak niom My baby
Dafa fekk ni do niom douniou yaw
Minne na la Tammou na la
Mane mala tamou ci niom ba ngua doyma
Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
ni mala beugué rombe na Yillif
Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
ni mala beugué rombe na Yillif héé.
Sama guente gui
mba douma yewou rek mou diekh
Sama guente gui
mba douma yewou rek mou diekh
Sama guente gui
mba douma yewou rek mou diekh
GEN JI DEKK
ya léne guene ci mane
Té dou yagg ba ngua donne niom
Do meussa donne niom
Soumay nieuw ci yaw
Ropplane loumou naw naw!
Ma guena gaw ci yaw
Nangouna donne sa autorail
Souma djoubé gare cornet né YEUKSINNA
Beug nala guemnala
Ni mala beugé dafa diegui dayyo
ni ngua ma beugué rombe na Yillif
beug nala beug nala
beug nala!!

⏱️ Synced Lyrics
[00:07.35] Guentouma hé Gentouma
[00:11.86] Hoooooo HOoo!
[00:20.91] Guentouma hé Gentouma.
[00:24.68] Beugouma yewou rek guente gui diekh.
[00:35.57] Ngua neck fi ma neck feulé Dou té niou gussanté
[00:39.29] nékal fi mangui feulé Beugenala,
[00:41.91] Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako.
[00:45.60] Beugnala Guemenala
[00:49.22] Geumnawooo Ho
[00:51.09] Guentouma!!! Guentouma!!!
[01:00.16] Nekkal fi ma neck feulé Dou té niou gussanté
[01:03.72] nékal fi mangui feulé Beugenala
[01:06.63] Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako
[01:12.15] Beugnala Guemenala
[01:13.90] Geumnawooo Ho
[01:16.71] Guentouma!!! Guentouma!!!
[01:24.84] Naniou Khalaté lou lenne nekh ci mane
[01:28.50] Bayiléne niou wakh louléne nekh ci mane
[01:38.54] Maye adji kiiy beug. Beugnala
[01:43.12] Beug Sa Deuk Ba Deuk Fa mouy guene di deuk ci mane. "WTF"
[01:53.17] Yaw yaye ki kidnaper sama life
[01:55.81] Hooo Hooo My life...
[02:06.73] Kidnaper sama temps khamnala
[02:10.42] Temperature bo necké soma guissé guif
[02:21.33] Dangua beugonna kham ci lanne la néék
[02:24.92] Dangua beugonna kham ci lanne lay dokh
[02:28.64] Yakamtina niouye skype
[02:31.38] Deug sa viber, am sa allo!
[02:35.00] Arrosé na samay fleur mane
[02:39.58] Ba meuna feyy ci bissoub mbeugéll yii
[02:49.58] GEN JI DEKK dama yague ak yaw
[02:53.15] Ba so yeukeutii say kaddu
[02:56.84] Bala nguay danéél makoy teureul
[02:59.59] GEN JI DEKK
[03:04.14] Geunalanté wouma la ak niom My baby
[03:07.71] Dafa fekk ni do niom douniou yaw
[03:10.49] Minne na la Tammou na la
[03:14.15] Mane mala tamou ci niom ba ngua doyma
[03:24.12] Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
[03:26.82] ni mala beugué rombe na Yillif
[03:30.44] Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
[03:33.18] ni mala beugué rombe na Yillif héé.
[03:42.24] Sama guente gui
[03:45.98] mba douma yewou rek mou diekh
[03:52.24] Sama guente gui
[03:55.94] mba douma yewou rek mou diekh
[04:05.09] Sama guente gui
[04:08.69] mba douma yewou rek mou diekh
[04:16.85] GEN JI DEKK
[04:23.24] ya léne guene ci mane
[04:25.91] Té dou yagg ba ngua donne niom
[04:28.73] Do meussa donne niom
[04:41.46] Soumay nieuw ci yaw
[04:44.26] Ropplane loumou naw naw!
[04:47.86] Ma guena gaw ci yaw
[04:53.31] Nangouna donne sa autorail
[04:57.06] Souma djoubé gare cornet né YEUKSINNA
[05:03.40] Beug nala guemnala
[05:07.99] Ni mala beugé dafa diegui dayyo
[05:10.66] ni ngua ma beugué rombe na Yillif
[05:14.38] beug nala beug nala
[05:17.07] beug nala!!
[05:24.32]