Bekoor
🎵 1630 characters
⏱️ 6:26 duration
🆔 ID: 11277251
📜 Lyrics
Mbay maral wi mettina yaay
Bekoor bi yàkk na ndeysan
Ndimbal lañuy sakkoo
Gir baykat sonn na yaay
Mbay maral wi mettina yaay
Bekoor bi yàkk na ndeysan
Ndimbal lañuy sakkoo
Gir baykat sonn na yaay
Démb da doon taw aywaay yé
Suuf naan màndi
Démb da doon taw di baawaan
Jur gi naan sempi
Démb da doon bakaaw di jàncax
Jur gi xontu mbaa jur
Àll be naan réew mi naan di guŋdanaan
Sitóor yi naan com maral
Mbay maral wi mettina yaay
Bekoor bi yàq na ndeysan
Ndimbal lañuy sakoo
Gir sámmkat bi sonn yaay
Mbay maral wi mettina yaay
Bekoor bi yàq na ndeysan
Ndimbal lañuy sakoo
Gir sámmkat bi sonn yaay
Démb da doon taw aywaay yé
Eh, eh, ho-ho, he, ho-ho,he
Ah-ha, he, ho, he-he man, he
Mbay maral wi mettina yaay
Bekoor bi yàq na ndeysan
Ndimbal lañuy sakKoo
Gir sámmkat bi sonn yaay
Tay su xin ne sappar gelawaal mbaa naat say
Ak nawet buu nangu baa dal meññaal gàncax
Taay Baykat bëttul, desetul gerte
Wa réewmi yàq warul tax, taa mën a nekk
War ngaa bokk ci ndimbal lii jëm ci waa gaw gi
Ndeysan maral bi meeti yaay
Sámmkat sonn
Nañu ndimbali sanu bopp nax yàlla ndimbali ñum
Nanu ndimbali sunu moroom nax Yàlla nangul nooo
Maral,maral,maral
Maral,maral,maral bi metti na
Maral,maral,maral bi metti na
Maral,maral,maral bi metti na
Nanu jëmbët garab te di koo suxal garab ci la
Maral,maral,maral bi metti na
Nanu ndimbali sanu bopp nax yàlla ndimbali ñum
Maral,maral,maral bi metti na
Nanu jëmbët garab te di koo suxal garab ci la
Maral,maral,maral bi metti na
Yàlla yàlla bay sa tooloo
Maral,maral,maral bi metti na
Ngir wa kaw gi maral bi metti na

⏱️ Synced Lyrics
[00:37.37] Mbay maral wi mettina yaay
[00:41.05] Bekoor bi yàkk na ndeysan
[00:45.14] Ndimbal lañuy sakkoo
[00:48.21] Gir baykat sonn na yaay
[00:58.55] Mbay maral wi mettina yaay
[01:02.20] Bekoor bi yàkk na ndeysan
[01:05.88] Ndimbal lañuy sakkoo
[01:08.76] Gir baykat sonn na yaay
[01:12.93]
[01:31.78] Démb da doon taw aywaay yé
[01:34.14] Suuf naan màndi
[01:35.88] Démb da doon taw di baawaan
[01:38.12] Jur gi naan sempi
[01:39.85] Démb da doon bakaaw di jàncax
[01:42.46] Jur gi xontu mbaa jur
[01:44.21] Àll be naan réew mi naan di guŋdanaan
[01:47.95] Sitóor yi naan com maral
[01:53.95] Mbay maral wi mettina yaay
[01:58.33] Bekoor bi yàq na ndeysan
[02:01.58] Ndimbal lañuy sakoo
[02:04.44] Gir sámmkat bi sonn yaay
[02:15.19] Mbay maral wi mettina yaay
[02:18.63] Bekoor bi yàq na ndeysan
[02:21.84] Ndimbal lañuy sakoo
[02:24.98] Gir sámmkat bi sonn yaay
[02:29.78]
[02:47.55] Démb da doon taw aywaay yé
[02:54.43] Eh, eh, ho-ho, he, ho-ho,he
[03:00.93] Ah-ha, he, ho, he-he man, he
[03:10.48] Mbay maral wi mettina yaay
[03:14.15] Bekoor bi yàq na ndeysan
[03:17.65] Ndimbal lañuy sakKoo
[03:20.27] Gir sámmkat bi sonn yaay
[03:24.52]
[03:42.72] Tay su xin ne sappar gelawaal mbaa naat say
[03:46.11] Ak nawet buu nangu baa dal meññaal gàncax
[03:49.61] Taay Baykat bëttul, desetul gerte
[03:53.24] Wa réewmi yàq warul tax, taa mën a nekk
[03:56.46] War ngaa bokk ci ndimbal lii jëm ci waa gaw gi
[03:59.32] Ndeysan maral bi meeti yaay
[04:06.02] Sámmkat sonn
[04:08.83] Nañu ndimbali sanu bopp nax yàlla ndimbali ñum
[04:12.21] Nanu ndimbali sunu moroom nax Yàlla nangul nooo
[04:16.07] Maral,maral,maral
[04:19.82]
[05:08.02] Maral,maral,maral bi metti na
[05:14.33] Maral,maral,maral bi metti na
[05:21.13] Maral,maral,maral bi metti na
[05:24.68] Nanu jëmbët garab te di koo suxal garab ci la
[05:28.25] Maral,maral,maral bi metti na
[05:31.49] Nanu ndimbali sanu bopp nax yàlla ndimbali ñum
[05:34.84] Maral,maral,maral bi metti na
[05:38.39] Nanu jëmbët garab te di koo suxal garab ci la
[05:41.37] Maral,maral,maral bi metti na
[05:44.48] Yàlla yàlla bay sa tooloo
[05:48.08] Maral,maral,maral bi metti na
[05:51.70] Ngir wa kaw gi maral bi metti na
[05:55.03] Maral,maral,maral bi metti na
[05:59.47]