Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Xool Ma Ci Bët (feat. Jeeba)

👤 Iss 814 🎼 Xool Ma Ci Bët ⏱️ 3:26
🎵 2031 characters
⏱️ 3:26 duration
🆔 ID: 11487880

📜 Lyrics

Mbeuguel bou deugou
Dara douko faye
Yaay seetou
Biye woné sama leeraye
Jant goudi
Biddew soubeu teel
Bimala xamé
Ci la tagok weetaye
Nii tognal sa aaaaaa! yaye
Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow
Nii tognal sa aaaaaa! Baye
Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow
Wolou nala wolou wolou nala!
Eh yaaaay!
Wolou nala wolou wolou nala!
Ahn ahn!

Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Soume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay
Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Boume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare la rek
Mbeuguel a nekh
Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare la rek
Mbeuguel a nekh

Yéne saaye nga diéki diéki woma
Woma
Nga meer maané mba diépiwoma
Nga néma non non
Yéne saaye nga xole ma rek Ma rétaan rétaan
Yaay sama boumou xol bi
Yaay sama boumou xol bi
Bo meeré ba guédeu dafemaay metti
Metti
Bo deffé ba gnipeu
Nala setsi
Setsi
Douma ci xole sax pa bek mère bi
Mère bi
Na oubi bountou bi soxna si
Dang ma diape sa mbaal
Té douma guéneuti
Bilay walay yé
Yow laay fethie ci bal
Yaay sama mélodie
Yow rek la baredé
Eh eh!

Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Soume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay
Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Boume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare leu rek
Mbeuguel a nekh
Xole ma ci bët
Ma xole la ci bët
Nioune niare leu rek
Mbeuguel a nekh

Yeh weurena ba weurengueul adouna
Yeh kou melni yow mba amatina
Yeh dougueul ci Keur gui yatouna
Ndakh yow yaay yaay sama boumou xol yaay sama boumou xol

Yéne saaye nga diéki diéki woma
Woma
Nga meer maané mba diépi woma
Nga néma non non
Yéne saaye nga xole ma rek
Ma rétaan rétaan
Yaay sama boumou xol bi
Yaay sama boumou xol bi

Weurena ba weurengueul adouna
Yeh kou melni yow mba amatina
Eh yah dougueul ci Keur gui yatouna
Ndakh yow yaay
Yaay sama boumou xol
Yaay sama boumou xol

⏱️ Synced Lyrics

[00:14.94] Mbeuguel bou deugou
[00:16.21] Dara douko faye
[00:18.17] Yaay seetou
[00:19.02] Biye woné sama leeraye
[00:21.92] Jant goudi
[00:22.74] Biddew soubeu teel
[00:24.94] Bimala xamé
[00:25.91] Ci la tagok weetaye
[00:28.15] Nii tognal sa aaaaaa! yaye
[00:31.58] Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow
[00:35.13] Nii tognal sa aaaaaa! Baye
[00:38.86] Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow
[00:42.25] Wolou nala wolou wolou nala!
[00:46.39] Eh yaaaay!
[00:48.82] Wolou nala wolou wolou nala!
[00:53.66] Ahn ahn!
[00:55.17] Boume laay guiss ngaay doundou
[00:56.85] Dafemaay doundeul baby
[00:58.56] Soume laay guiss ngaay rétaan
[01:00.30] Dafemaay doundeul waay
[01:02.17] Boume laay guiss ngaay doundou
[01:03.83] Dafemaay doundeul baby
[01:05.50] Boume laay guiss ngaay rétaan
[01:07.17] Dafemaay doundeul waay
[01:08.56] Xool ma ci bët
[01:10.23] Ma xool la ci bët
[01:12.30] Nioune niare la rek
[01:13.95] Mbeuguel a nekh
[01:15.71] Xool ma ci bët
[01:17.27] Ma xool la ci bët
[01:18.81] Nioune niare la rek
[01:20.66] Mbeuguel a nekh
[01:22.28] Yéne saaye nga diéki diéki woma
[01:25.09] Woma
[01:25.97] Nga meer maané mba diépiwoma
[01:28.10] Nga néma non non
[01:29.33] Yéne saaye nga xole ma rek Ma rétaan rétaan
[01:32.71] Yaay sama boumou xol bi
[01:34.31] Yaay sama boumou xol bi
[01:36.18] Bo meeré ba guédeu dafemaay metti
[01:38.70] Metti
[01:39.35] Bo deffé ba gnipeu
[01:40.55] Nala setsi
[01:42.05] Setsi
[01:43.15] Douma ci xole sax pa bek mère bi
[01:45.78] Mère bi
[01:46.62] Na oubi bountou bi soxna si
[01:50.12] Dang ma diape sa mbaal
[01:51.43] Té douma guéneuti
[01:53.88] Bilay walay yé
[01:57.03] Yow laay fethie ci bal
[01:58.60] Yaay sama mélodie
[02:00.42] Yow rek la baredé
[02:02.63] Eh eh!
[02:03.88] Boume laay guiss ngaay doundou
[02:05.47] Dafemaay doundeul baby
[02:07.25] Soume laay guiss ngaay rétaan
[02:09.19] Dafemaay doundeul waay
[02:10.63] Boume laay guiss ngaay doundou
[02:12.17] Dafemaay doundeul baby
[02:14.16] Boume laay guiss ngaay rétaan
[02:15.65] Dafemaay doundeul waay
[02:17.23] Xool ma ci bët
[02:18.76] Ma xool la ci bët
[02:20.94] Nioune niare leu rek
[02:22.20] Mbeuguel a nekh
[02:24.16] Xole ma ci bët
[02:25.77] Ma xole la ci bët
[02:27.51] Nioune niare leu rek
[02:29.49] Mbeuguel a nekh
[02:30.25] Yeh weurena ba weurengueul adouna
[02:33.61] Yeh kou melni yow mba amatina
[02:37.03] Yeh dougueul ci Keur gui yatouna
[02:40.01] Ndakh yow yaay yaay sama boumou xol yaay sama boumou xol
[02:44.57] Yéne saaye nga diéki diéki woma
[02:47.39] Woma
[02:48.39] Nga meer maané mba diépi woma
[02:50.19] Nga néma non non
[02:51.62] Yéne saaye nga xole ma rek
[02:52.83] Ma rétaan rétaan
[02:54.68] Yaay sama boumou xol bi
[02:56.55] Yaay sama boumou xol bi
[02:58.44] Weurena ba weurengueul adouna
[03:01.20] Yeh kou melni yow mba amatina
[03:04.49] Eh yah dougueul ci Keur gui yatouna
[03:07.42] Ndakh yow yaay
[03:08.68] Yaay sama boumou xol
[03:10.15] Yaay sama boumou xol
[03:12.20]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings