TEKNA CI YAW
🎵 1273 characters
⏱️ 2:17 duration
🆔 ID: 11605287
📜 Lyrics
814 beatz
Big primo got the juice
Sa ex gaañ na la pur moom
Bu fi nekkul dootoo baax
Ma ñëw yëkketi la
Bul jooy, loo gis am na lu tax
Xamul sa valeur
Daf la négligler ba ma jot ci yaw
Ne ko mu talal
May ki lay defar ba nga yëg ci kaw
Tek naa ci yaw, baby
Indil chèque bi damay signer bilaay
Tek naa ci yaw, baby
Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
Tek naa ci yaw
Say copines dañuy sissou
Ouh ouh
Sa ex dafay sissou
Ouh ouh
Dénk ma love bi
Jox ma sa xol bi
Kenn du la weccoo baby
Ngalam nga doo përëm
Xale bee metti, bari feem tek ci
Moom bu la jekko xamul baale xamul yërëm
Jàmm li ngay jàmm
Bégal bi nga ma bégal
Loxo bi fig ko dugal
Man moo ma ray
Laal bi yaa ko dam
Ndig bi yaa ko dam
Tëddel sama dënd
Nelawal kenn du la yee
Wouyay yoyy
Yeah ye ye
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek
Tek naa ci yaw, baby
Indil chèque bi damay signer bilaay
Tek naa ci yaw, baby
Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
Tek naa ci yaw
Say copines dañuy sissou
Ouh ouh
Sa ex dafay sissou
Ouh ouh
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek
Tek naa ci yaw
Big primo got the juice
Sa ex gaañ na la pur moom
Bu fi nekkul dootoo baax
Ma ñëw yëkketi la
Bul jooy, loo gis am na lu tax
Xamul sa valeur
Daf la négligler ba ma jot ci yaw
Ne ko mu talal
May ki lay defar ba nga yëg ci kaw
Tek naa ci yaw, baby
Indil chèque bi damay signer bilaay
Tek naa ci yaw, baby
Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
Tek naa ci yaw
Say copines dañuy sissou
Ouh ouh
Sa ex dafay sissou
Ouh ouh
Dénk ma love bi
Jox ma sa xol bi
Kenn du la weccoo baby
Ngalam nga doo përëm
Xale bee metti, bari feem tek ci
Moom bu la jekko xamul baale xamul yërëm
Jàmm li ngay jàmm
Bégal bi nga ma bégal
Loxo bi fig ko dugal
Man moo ma ray
Laal bi yaa ko dam
Ndig bi yaa ko dam
Tëddel sama dënd
Nelawal kenn du la yee
Wouyay yoyy
Yeah ye ye
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek
Tek naa ci yaw, baby
Indil chèque bi damay signer bilaay
Tek naa ci yaw, baby
Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
Tek naa ci yaw
Say copines dañuy sissou
Ouh ouh
Sa ex dafay sissou
Ouh ouh
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek (ci ko tek)
Ci yaw la tek
Tek naa ci yaw
⏱️ Synced Lyrics
[00:00.15] 814 beatz
[00:05.10] Big primo got the juice
[00:12.43] Sa ex gaañ na la pur moom
[00:15.14] Bu fi nekkul dootoo baax
[00:18.09] Ma ñëw yëkketi la
[00:20.16] Bul jooy, loo gis am na lu tax
[00:22.84] Xamul sa valeur
[00:25.84] Daf la négligler ba ma jot ci yaw
[00:28.59] Ne ko mu talal
[00:32.16] May ki lay defar ba nga yëg ci kaw
[00:34.76] Tek naa ci yaw, baby
[00:38.67] Indil chèque bi damay signer bilaay
[00:40.93] Tek naa ci yaw, baby
[00:44.72] Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
[00:46.82] Tek naa ci yaw
[00:48.04] Say copines dañuy sissou
[00:49.77] Ouh ouh
[00:53.83] Sa ex dafay sissou
[00:55.32] Ouh ouh
[00:58.63] Dénk ma love bi
[01:00.02] Jox ma sa xol bi
[01:01.58] Kenn du la weccoo baby
[01:02.92] Ngalam nga doo përëm
[01:04.44] Xale bee metti, bari feem tek ci
[01:07.43] Moom bu la jekko xamul baale xamul yërëm
[01:11.88] Jàmm li ngay jàmm
[01:13.26] Bégal bi nga ma bégal
[01:14.70] Loxo bi fig ko dugal
[01:16.25] Man moo ma ray
[01:17.80] Laal bi yaa ko dam
[01:19.18] Ndig bi yaa ko dam
[01:20.68] Tëddel sama dënd
[01:21.78] Nelawal kenn du la yee
[01:24.11] Wouyay yoyy
[01:25.63] Yeah ye ye
[01:28.57] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[01:30.67] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[01:31.87] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[01:33.31] Ci yaw la tek
[01:34.05] Tek naa ci yaw, baby
[01:37.83] Indil chèque bi damay signer bilaay
[01:39.97] Tek naa ci yaw, baby
[01:43.72] Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
[01:45.86] Tek naa ci yaw
[01:47.28] Say copines dañuy sissou
[01:49.33] Ouh ouh
[01:52.99] Sa ex dafay sissou
[01:54.76] Ouh ouh
[01:58.56] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:00.12] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:01.59] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:03.07] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:04.80] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:06.21] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:07.51] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:08.92] Ci yaw la tek
[02:09.80] Tek naa ci yaw
[02:12.16]
[00:05.10] Big primo got the juice
[00:12.43] Sa ex gaañ na la pur moom
[00:15.14] Bu fi nekkul dootoo baax
[00:18.09] Ma ñëw yëkketi la
[00:20.16] Bul jooy, loo gis am na lu tax
[00:22.84] Xamul sa valeur
[00:25.84] Daf la négligler ba ma jot ci yaw
[00:28.59] Ne ko mu talal
[00:32.16] May ki lay defar ba nga yëg ci kaw
[00:34.76] Tek naa ci yaw, baby
[00:38.67] Indil chèque bi damay signer bilaay
[00:40.93] Tek naa ci yaw, baby
[00:44.72] Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
[00:46.82] Tek naa ci yaw
[00:48.04] Say copines dañuy sissou
[00:49.77] Ouh ouh
[00:53.83] Sa ex dafay sissou
[00:55.32] Ouh ouh
[00:58.63] Dénk ma love bi
[01:00.02] Jox ma sa xol bi
[01:01.58] Kenn du la weccoo baby
[01:02.92] Ngalam nga doo përëm
[01:04.44] Xale bee metti, bari feem tek ci
[01:07.43] Moom bu la jekko xamul baale xamul yërëm
[01:11.88] Jàmm li ngay jàmm
[01:13.26] Bégal bi nga ma bégal
[01:14.70] Loxo bi fig ko dugal
[01:16.25] Man moo ma ray
[01:17.80] Laal bi yaa ko dam
[01:19.18] Ndig bi yaa ko dam
[01:20.68] Tëddel sama dënd
[01:21.78] Nelawal kenn du la yee
[01:24.11] Wouyay yoyy
[01:25.63] Yeah ye ye
[01:28.57] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[01:30.67] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[01:31.87] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[01:33.31] Ci yaw la tek
[01:34.05] Tek naa ci yaw, baby
[01:37.83] Indil chèque bi damay signer bilaay
[01:39.97] Tek naa ci yaw, baby
[01:43.72] Yaa leen dàq gën leen rafet jikko
[01:45.86] Tek naa ci yaw
[01:47.28] Say copines dañuy sissou
[01:49.33] Ouh ouh
[01:52.99] Sa ex dafay sissou
[01:54.76] Ouh ouh
[01:58.56] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:00.12] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:01.59] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:03.07] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:04.80] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:06.21] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:07.51] Ci yaw la tek (ci ko tek)
[02:08.92] Ci yaw la tek
[02:09.80] Tek naa ci yaw
[02:12.16]