Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Mama Bless

👤 Lidiop 🎼 Another Vision ⏱️ 4:53
🎵 1261 characters
⏱️ 4:53 duration
🆔 ID: 11844350

📜 Lyrics

Ye he he he
Wo ho ho oh oh oh ah
Ee yow Yaay bóoy, yow de ñaanal ma
Ee yow Baay bóoy, yow de ñaanal ma

Yéena ma jur si yoonu siratal mustahiim
Jàngal ngeen ma Alxuraan
Yéena ma ni doom moytul lu aaram
Yéena ma ni doom oh moytul yaw saraan
Dund bu soteegul lunekk xaj nasi
Ku jéggiwul ndox bul retaan kuy lab

Yaay bóoy ñaanal ma, ndax sànku dafa gaaw
Baay bóoy ñaanal ma yow si pexe noon yi

Mama bless me from my ennemis
Father bless me from my ennemis

t 2

Boobu ba léegi mësuma wàcc yoon
Boobu ba léegi xamna ki ma doon
Ndaxte xamna ki ma doon, fi ma jógé, fi ma bayeeko, fi ma soqeeko
Ñaata ñoo lay ree, fekk yéene wuñula ludul dee
Ñaata ñoo lay siiñ, so deme ñu lay biiñ

A long away of my Life me I hustling day and night
When I remember when I was a young boy
My mama use to say oh my song
Go forward and don't look back
Follow you diny follow your way

Boobu ba léegi maa ngyi topp yoon
Ndaxte xamna ki ma doon
Ku fàtte yow fi nga fi nga jógé, fi nga bayeeko
Fi nga soqeeko
Ñaata ñoo lay ree, fekk yéene wuñula ludul dee
Ñaata ñoo lay siiñ, so deme ñu lay biiñ
Xàmmeel bu baax ñila bëgg
Ak ñila bañ
Toppal sa yoon

Who mama bless no one curse
Who father bless no one curse
Who serafall bless no one curse

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings