Fii Lay Né
🎵 743 characters
⏱️ 2:21 duration
🆔 ID: 12313337
📜 Lyrics
Fii lay nee
Neke mbëggeel fii lay nee
Damaa am sa faiblesse
Xol bi ya ci fees
Took dila jandeer di jooy
Daf may daal
Non non non non
Nilaa, nilaa
Damay woo Dame séne
Sama kaw scéne
Takkaal ko chaine
Ngir mu bégël mala
Jox nala cër bi
Ba mel ni kula ragal
Daf may daal
Aw ma ci kersa
Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
Woor nama
Woo batay
Nenaa mbëggeel
Filay ne
Woo batay
Mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
Fiii lay nék
Jox nala cër bi
Aw ma ci kersa
Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
Woo woo waaw
Gisoo sunu gaa yi
Ñoom nena ñu luñu ma wax, ma wax la
Dimako tooñee woo hoo
Filay ne
Neke mbëggeel fii lay nekk
Jox nala teere bi
Amuma ci kérsa
Ndokk Yàlla ba nimala faale
Nii ngama taale fii
Neke mbëggeel fii lay ne
Neke mbëggeel fii lay nee
Damaa am sa faiblesse
Xol bi ya ci fees
Took dila jandeer di jooy
Daf may daal
Non non non non
Nilaa, nilaa
Damay woo Dame séne
Sama kaw scéne
Takkaal ko chaine
Ngir mu bégël mala
Jox nala cër bi
Ba mel ni kula ragal
Daf may daal
Aw ma ci kersa
Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
Woor nama
Woo batay
Nenaa mbëggeel
Filay ne
Woo batay
Mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
Fiii lay nék
Jox nala cër bi
Aw ma ci kersa
Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
Woo woo waaw
Gisoo sunu gaa yi
Ñoom nena ñu luñu ma wax, ma wax la
Dimako tooñee woo hoo
Filay ne
Neke mbëggeel fii lay nekk
Jox nala teere bi
Amuma ci kérsa
Ndokk Yàlla ba nimala faale
Nii ngama taale fii
Neke mbëggeel fii lay ne
⏱️ Synced Lyrics
[00:00.08] Fii lay nee
[00:02.97] Neke mbëggeel fii lay nee
[00:10.52] Damaa am sa faiblesse
[00:12.63] Xol bi ya ci fees
[00:15.52] Took dila jandeer di jooy
[00:18.01] Daf may daal
[00:24.39] Non non non non
[00:27.41] Nilaa, nilaa
[00:34.43] Damay woo Dame séne
[00:37.07] Sama kaw scéne
[00:40.16] Takkaal ko chaine
[00:41.62] Ngir mu bégël mala
[00:48.42] Jox nala cër bi
[00:50.58] Ba mel ni kula ragal
[00:52.59] Daf may daal
[00:58.30] Aw ma ci kersa
[01:00.13] Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
[01:03.56] Woor nama
[01:07.96] Woo batay
[01:10.19] Nenaa mbëggeel
[01:12.82] Filay ne
[01:17.88] Woo batay
[01:20.09] Mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
[01:22.66] Fiii lay nék
[01:27.93] Jox nala cër bi
[01:32.23] Aw ma ci kersa
[01:37.24] Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
[01:40.27] Woo woo waaw
[01:42.25] Gisoo sunu gaa yi
[01:44.89] Ñoom nena ñu luñu ma wax, ma wax la
[01:47.68] Dimako tooñee woo hoo
[01:51.63] Filay ne
[01:55.06] Neke mbëggeel fii lay nekk
[02:01.70] Jox nala teere bi
[02:04.67] Amuma ci kérsa
[02:06.58] Ndokk Yàlla ba nimala faale
[02:09.62] Nii ngama taale fii
[02:14.47] Neke mbëggeel fii lay ne
[02:18.70]
[00:02.97] Neke mbëggeel fii lay nee
[00:10.52] Damaa am sa faiblesse
[00:12.63] Xol bi ya ci fees
[00:15.52] Took dila jandeer di jooy
[00:18.01] Daf may daal
[00:24.39] Non non non non
[00:27.41] Nilaa, nilaa
[00:34.43] Damay woo Dame séne
[00:37.07] Sama kaw scéne
[00:40.16] Takkaal ko chaine
[00:41.62] Ngir mu bégël mala
[00:48.42] Jox nala cër bi
[00:50.58] Ba mel ni kula ragal
[00:52.59] Daf may daal
[00:58.30] Aw ma ci kersa
[01:00.13] Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
[01:03.56] Woor nama
[01:07.96] Woo batay
[01:10.19] Nenaa mbëggeel
[01:12.82] Filay ne
[01:17.88] Woo batay
[01:20.09] Mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
[01:22.66] Fiii lay nék
[01:27.93] Jox nala cër bi
[01:32.23] Aw ma ci kersa
[01:37.24] Dëgël nanee jàmm, ci yaw lakaay ame
[01:40.27] Woo woo waaw
[01:42.25] Gisoo sunu gaa yi
[01:44.89] Ñoom nena ñu luñu ma wax, ma wax la
[01:47.68] Dimako tooñee woo hoo
[01:51.63] Filay ne
[01:55.06] Neke mbëggeel fii lay nekk
[02:01.70] Jox nala teere bi
[02:04.67] Amuma ci kérsa
[02:06.58] Ndokk Yàlla ba nimala faale
[02:09.62] Nii ngama taale fii
[02:14.47] Neke mbëggeel fii lay ne
[02:18.70]