Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Xel Akk Xol

👤 Ashs the Best 🎼 Dibèer ⏱️ 3:06
🎵 445 characters
⏱️ 3:06 duration
🆔 ID: 12319046

📜 Lyrics

Yeah, eh eh eh
Lé, lé, walé
Hum, hum

Yaw lay bëgg jakarlool
Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol

Ëlëk lu mata soor la
Ëlëk ay jaar-jaar la
Sama xol yëgoon nako muy ñëw

Xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
Xol yëkk yëkk la
Dara xaaju fë

Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol
(Suma yewo yaw la bëgg njekk xol)
Yaw la bëgg jakarlool

Denk na la guddi
Fanané yakkar ci yaw
Gent na la guddi gi yëpp
Ndax fajar yaw lay jakarlool

⏱️ Synced Lyrics

[00:24.04] Yeah, eh eh eh
[00:28.12] Lé, lé, walé
[00:33.11] Hum, hum
[00:38.27]
[00:41.76] Yaw lay bëgg jakarlool
[00:43.96] Sa suma yeewu
[00:51.65] Yaw lay bëgg njëkk xol
[00:55.47]
[00:58.01] Ëlëk lu mata soor la
[01:02.53]
[01:06.37] Ëlëk ay jaar-jaar la
[01:08.02] Sama xol yëgoon nako muy ñëw
[01:13.59] Xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
[01:17.73] Xol yëkk yëkk la
[01:21.65]
[01:25.82] Dara xaaju fë
[01:31.57] Sa suma yeewu
[01:33.29] Yaw lay bëgg njëkk xol
[01:36.61]
[01:40.80] (Suma yewo yaw la bëgg njekk xol)
[01:45.21] Yaw la bëgg jakarlool
[01:49.92]
[01:53.72] Denk na la guddi
[01:55.42] Fanané yakkar ci yaw
[01:59.16]
[02:01.70] Gent na la guddi gi yëpp
[02:02.29] Ndax fajar yaw lay jakarlool
[02:03.76]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings