Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Guuy

👤 Jeeba 🎼 Jeeba Videos ⏱️ 4:02
🎵 2552 characters
⏱️ 4:02 duration
🆔 ID: 12444121

📜 Lyrics

Dinala daal foko doul fogué
Foko doul khalaté
Sa baniouy doguou thie lalaay dougué
Deey melni yallah ko yoné
Dina fess sa xool bi unh no no no
Eulemeul sa boop bi unh yeah yeah
Doto amati principe, Bafouer nga leep
Meuno guiss si moom siik
Yoow loum lay deef dou yow rek yakoo xaameu
Dou lou niit meuneu wakh
Yoow fim may yobou dafa melni meussoumafa deemeu
Wayé dou lou niit meuneu wakh
May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé
May ladj kagn laay magué
Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué
Degg na sakh dama jongué
Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo
Yaay sama hero
Sama bébé d'amour conquérir nga sama xool
Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool
Bo bégué ma begg bo dioyé ma dioy
Lima guissoul si niom la guiss si yow mou doyma
Sandi nga cravache dane ngaleen diél bou gaaw
May sa djomba niaaw djomb nala deef lou niaaw

Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy
Seral ngamaa guuy guuy guuy
Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy
Seral ngama Guuy guuy guuy guuy

Tank tank mbague ak mbague niou deem
Waat nani dinala yobou Fenen
Yoow defal nank boul deglou wakhi noone
Niom douniou deem beugouniou kou deem eeh
Khana xamoni lou bakh nieupeu ko beugg beugg
Fi liniuy wakh khadj ba dou deugg deugg eeh
Khana xamoni meune naniou wakh mais duniu beugg
Seen biir xool meunou niou guiss niaar niou beguenter
Tei xamnani warone na done Gueweel ma tagaal la say maam
Warone nga done jaam ma goreel la goreel saay maam
Souma amone avion dou ma maylako dila dowaalal fo beugg
Niou dieum thia li soula doyoul wakhma loulay dooy bébé
Bilay walay khawma lilay dooy

May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé
May ladj kagn laay magué
Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué
Degg na sakh dama jongué
Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo
Yaay sama hero
Sama bébé d'amour conquérir nga sama xool
Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool
Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy
Seral ngamaa guuy guuy guuy
Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy
Seral ngama Guuy guuy guuy guuy
May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé
May ladj kagn laay magué
Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué
Degg na sakh dama jongué

⏱️ Synced Lyrics

[00:03.54] Dinala daal foko doul fogué
[00:18.00] Foko doul khalaté
[00:20.71] Sa baniouy doguou thie lalaay dougué
[00:24.69] Deey melni yallah ko yoné
[00:28.31] Dina fess sa xool bi unh no no no
[00:31.82] Eulemeul sa boop bi unh yeah yeah
[00:35.00] Doto amati principe, Bafouer nga leep
[00:38.23] Meuno guiss si moom siik
[00:40.55] Yoow loum lay deef dou yow rek yakoo xaameu
[00:44.70] Dou lou niit meuneu wakh
[00:46.92] Yoow fim may yobou dafa melni meussoumafa deemeu
[00:51.12] Wayé dou lou niit meuneu wakh
[00:53.55] May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé
[00:57.42] May ladj kagn laay magué
[01:00.76] Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué
[01:04.50] Degg na sakh dama jongué
[01:06.69] Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo
[01:10.85] Yaay sama hero
[01:12.48] Sama bébé d'amour conquérir nga sama xool
[01:15.69] Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool
[01:19.05] Bo bégué ma begg bo dioyé ma dioy
[01:22.44] Lima guissoul si niom la guiss si yow mou doyma
[01:25.84] Sandi nga cravache dane ngaleen diél bou gaaw
[01:28.74] May sa djomba niaaw djomb nala deef lou niaaw
[01:32.44] Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
[01:38.68] Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
[01:45.44] Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy
[01:48.91] Seral ngamaa guuy guuy guuy
[01:51.87] Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy
[01:55.22] Seral ngama Guuy guuy guuy guuy
[01:58.62] Tank tank mbague ak mbague niou deem
[02:02.94] Waat nani dinala yobou Fenen
[02:05.36] Yoow defal nank boul deglou wakhi noone
[02:09.48] Niom douniou deem beugouniou kou deem eeh
[02:12.39] Khana xamoni lou bakh nieupeu ko beugg beugg
[02:16.58] Fi liniuy wakh khadj ba dou deugg deugg eeh
[02:18.82] Khana xamoni meune naniou wakh mais duniu beugg
[02:21.92] Seen biir xool meunou niou guiss niaar niou beguenter
[02:25.78] Tei xamnani warone na done Gueweel ma tagaal la say maam
[02:33.38] Warone nga done jaam ma goreel la goreel saay maam
[02:39.60] Souma amone avion dou ma maylako dila dowaalal fo beugg
[02:44.10] Niou dieum thia li soula doyoul wakhma loulay dooy bébé
[02:48.06] Bilay walay khawma lilay dooy
[02:51.23] May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé
[02:56.26] May ladj kagn laay magué
[02:58.82] Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué
[03:02.85] Degg na sakh dama jongué
[03:05.75] Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo
[03:09.48] Yaay sama hero
[03:10.77] Sama bébé d'amour conquérir nga sama xool
[03:14.16] Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool
[03:17.57] Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
[03:24.06] Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié
[03:30.72] Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy
[03:33.81] Seral ngamaa guuy guuy guuy
[03:37.15] Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy
[03:40.54] Seral ngama Guuy guuy guuy guuy
[03:43.88] May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé
[03:48.65] May ladj kagn laay magué
[03:50.79] Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué
[03:55.42] Degg na sakh dama jongué
[03:56.47]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings