Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Calm Down (feat. Jeeba)

👤 Karabalik Beatz 🎼 General Kara ⏱️ 3:03
🎵 1142 characters
⏱️ 3:03 duration
🆔 ID: 12932339

📜 Lyrics

Tey ma bége la
Tey ma wone la
Tey ma wax la
Yaa ma gën a xam way!
Li nga ma def soo ko bàyyiwul
Dinga mës a ray doomu jaambur way!
Yaw yaa ma xam, xam ma bu baax
Bu lu xasaan ci man loxo keneen wokesu ko

Guddi gi jot ba lépp ni séelaw
Nga daagu ndank ñëw sama kaw di ma eh eh eh Yaw
Say kesen kesen tere ma nelaw
Yaa ma mën a yuxuloo te xam nga dama ragal

Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la

Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu

Yeah yeah
Baby li ma jaxal te nga wax ma ki la jàngal
Sant na sa bàjjen moom mi la jox li may jomal
Amatuma sago ci yaw su ma la gise saalit
Waaw waaw, yow baby waaw waaw

Seddal sama xol, dalal sama xel
Yaa ma gëna lool
Ne waaw seddal sama xol dalal sama xel
Eh eh eh

Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la
Eh calm down, calm down
Bébé calm down, doomu jaambur la

Dootoo niit parce que doo nitu
Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Ni ngay def dama joomi
Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu

⏱️ Synced Lyrics

[00:14.16] Tey ma bége la
[00:15.82] Tey ma wone la
[00:17.31] Tey ma wax la
[00:18.55] Yaa ma gën a xam way!
[00:21.04] Li nga ma def soo ko bàyyiwul
[00:23.99] Dinga mës a ray doomu jaambur way!
[00:27.55] Yaw yaa ma xam, xam ma bu baax
[00:30.59] Bu lu xasaan ci man loxo keneen wokesu ko
[00:34.13] Guddi gi jot ba lépp ni séelaw
[00:36.49] Nga daagu ndank ñëw sama kaw di ma eh eh eh Yaw
[00:40.33] Say kesen kesen tere ma nelaw
[00:43.68] Yaa ma mën a yuxuloo te xam nga dama ragal
[00:47.26] Eh calm down, calm down
[00:50.53] Bébé calm down, doomu jaambur la
[00:53.78] Eh calm down, calm down
[00:57.08] Bébé calm down, doomu jaambur la
[00:59.76] Dootoo niit parce que doo nitu
[01:02.76] Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
[01:06.06] Ni ngay def dama joomi
[01:09.35] Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu
[01:12.57] Yeah yeah
[01:13.72] Baby li ma jaxal te nga wax ma ki la jàngal
[01:16.79] Sant na sa bàjjen moom mi la jox li may jomal
[01:20.04] Amatuma sago ci yaw su ma la gise saalit
[01:23.36] Waaw waaw, yow baby waaw waaw
[01:28.15] Seddal sama xol, dalal sama xel
[01:31.48] Yaa ma gëna lool
[01:33.84] Ne waaw seddal sama xol dalal sama xel
[01:38.12] Eh eh eh
[01:40.25] Eh calm down, calm down
[01:43.51] Bébé calm down, doomu jaambur la
[01:46.89] Eh calm down, calm down
[01:49.77] Bébé calm down, doomu jaambur la
[01:52.52] Dootoo niit parce que doo nitu
[01:55.84] Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
[01:59.02] Ni ngay def dama joomi
[02:02.32] Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu
[02:05.30]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings