Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Reguine tass

👤 Wally B. Seck 🎼 Reguine tass ⏱️ 3:18
🎵 1756 characters
⏱️ 3:18 duration
🆔 ID: 13125912

📜 Lyrics

Par AbouAmg

Deloulsil delousil dou meun nga darra dé diaroul xass
Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga

Oooh ooh ooh

Ni diamono ji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh dji beurina déy nourou mariné

Di naagn la féthial reguine tass

Ni wo woo Vivi bougnou faalé
Bougnou décodé
Nagnou baalé
Ki léy diébaané
Boko séété dé yaako tané
Mane dé déég naala
Dafa féék né taloumala

Eyow eyow eyow

Di nga sonou Faramareen féép leu meuné
Eyow eh
Nangoulmako té nga Take a sit, Take a sit
Vivi gnou féthial ko Reuguine tass

Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga

Oooh ooh ooh

Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala

Di naagn la féthial reguine tass

Deloussil deloussil comment tu vas (comment tu vas)
Nangoul niou lou niou mom té yalla takh (té yalla takh)
Maléy sonnal, té dawoulo dé wawaw

Demal nga tok, mané dolé yamoul wawaw
Kou andak lou niou andale loula nekh lathie

Wally ak Viviane beuri fitt faathie, yeah yeah
Bokk école, bokkou niou classe, té douma sa mass
Ma tangal sa khol, wakhko sa yaye mou soti ci glace
Té ragalouma lolou wooooh

Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala

Di naagn la féthial reguine tass

Bilay man dé beug naala
Walay man dé beug naala
Mayanté xaliss diaroul khass
Bilay man dé beug naala

Sant yalla dey nourou titeurou
Wakh deug yalla tognou gnou
Bour yalla né sante lén ma doli
Ba takhna ma deuké thiant li

Eh eh kou seu xol nekh nga ré

Di naagn la féthial reguine tass

⏱️ Synced Lyrics

[00:03.17] Par AbouAmg
[00:04.40] Deloulsil delousil dou meun nga darra dé diaroul xass
[00:05.79] Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
[00:08.55] Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga
[00:11.58] Oooh ooh ooh
[00:13.29] Ni diamono ji legui da ngay ré ba dé
[00:16.55] Fima dieuma sori damey bagn goudé
[00:19.74] Wakh dji beurina déy nourou mariné
[00:24.54] Di naagn la féthial reguine tass
[00:38.95] Ni wo woo Vivi bougnou faalé
[00:42.84] Bougnou décodé
[00:45.38] Nagnou baalé
[00:46.65] Ki léy diébaané
[00:47.62] Boko séété dé yaako tané
[00:48.87] Mane dé déég naala
[00:49.72] Dafa féék né taloumala
[00:50.42] Eyow eyow eyow
[00:52.54] Di nga sonou Faramareen féép leu meuné
[00:55.56] Eyow eh
[00:56.67] Nangoulmako té nga Take a sit, Take a sit
[00:57.79] Vivi gnou féthial ko Reuguine tass
[00:59.69] Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
[01:02.92] Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga
[01:05.82] Oooh ooh ooh
[01:07.69] Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
[01:10.69] Fima dieuma sori damey bagn goudé
[01:13.51] Wakh deug bagnou mala
[01:15.30] Di naagn la féthial reguine tass
[01:31.16] Deloussil deloussil comment tu vas (comment tu vas)
[01:33.74] Nangoul niou lou niou mom té yalla takh (té yalla takh)
[01:36.86] Maléy sonnal, té dawoulo dé wawaw
[01:40.53] Demal nga tok, mané dolé yamoul wawaw
[01:43.75] Kou andak lou niou andale loula nekh lathie
[01:46.56] Wally ak Viviane beuri fitt faathie, yeah yeah
[01:50.68] Bokk école, bokkou niou classe, té douma sa mass
[01:53.58] Ma tangal sa khol, wakhko sa yaye mou soti ci glace
[01:56.57] Té ragalouma lolou wooooh
[01:59.57] Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
[02:02.77] Fima dieuma sori damey bagn goudé
[02:05.72] Wakh deug bagnou mala
[02:08.12] Di naagn la féthial reguine tass
[02:22.45] Bilay man dé beug naala
[02:24.14] Walay man dé beug naala
[02:28.18] Mayanté xaliss diaroul khass
[02:31.66] Bilay man dé beug naala
[02:35.09] Sant yalla dey nourou titeurou
[02:38.23] Wakh deug yalla tognou gnou
[02:41.08] Bour yalla né sante lén ma doli
[02:44.74] Ba takhna ma deuké thiant li
[02:48.38] Eh eh kou seu xol nekh nga ré
[03:00.05] Di naagn la féthial reguine tass
[03:18.04]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings