Weetay
🎵 1370 characters
⏱️ 3:30 duration
🆔 ID: 15011716
📜 Lyrics
Mmmmmmm
Bës bu waroon nex la mujjee ay joy
Sama yaram daw na, sama xol toy na
Ki ma bëgg dem na, ku ma ko waxoon
Mënu ma ko gëm li comme ay leboon
Pexe noon lu am la, lu ma xam la man
Jam nañ sama xol ba baa mu jaare fa
Garab u mbëggeel so dagge reen ya
Bul ci mësa yaakar gis ca dom ya
Haaaaaaann
Leleenenenen
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Sëy nañ ba am jaboot sama xel
Jotuluma bayi ku maleey xolee
Rongoñ dina siit suma la ñakkee
Mbëggeel dina tiis jàmmu wa wàññeeku
Yàlla na nga xippe sama kër
Cat bañ la jiitu ci sa njegenaay
Tëddi nga yobale sama mbëggeel
Tëddi nga bayi mak dundu nammel
Xam na ne nala manquer lool
Wara dundu duma gis sa dom
Dañ la nangu ci sameey loxo
May ñuma sax ma xool sa xol man
Hannnnnn (may ñuma sax ma xool sa xol man)
Lelelennnn way
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Bës bu waroon nex la mujjee ay joy
Sama yaram daw na, sama xol toy na
Ki ma bëgg dem na, ku ma ko waxoon
Mënu ma ko gëm li comme ay leboon
Pexe noon lu am la, lu ma xam la man
Jam nañ sama xol ba baa mu jaare fa
Garab u mbëggeel so dagge reen ya
Bul ci mësa yaakar gis ca dom ya
Haaaaaaann
Leleenenenen
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Sëy nañ ba am jaboot sama xel
Jotuluma bayi ku maleey xolee
Rongoñ dina siit suma la ñakkee
Mbëggeel dina tiis jàmmu wa wàññeeku
Yàlla na nga xippe sama kër
Cat bañ la jiitu ci sa njegenaay
Tëddi nga yobale sama mbëggeel
Tëddi nga bayi mak dundu nammel
Xam na ne nala manquer lool
Wara dundu duma gis sa dom
Dañ la nangu ci sameey loxo
May ñuma sax ma xool sa xol man
Hannnnnn (may ñuma sax ma xool sa xol man)
Lelelennnn way
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
Namm nala lool
Te xammuma fan nga dem
Du ma la mësa fàtte
Ak fo mëna dem
Sa may ñaan nala fekk
Fo mëna nekka
Dalalal sa xel
Sama xol ya ci nekka
⏱️ Synced Lyrics
[00:17.22] Mmmmmmm
[00:27.76] Bës bu waroon nex la mujjee ay joy
[00:31.37] Sama yaram daw na, sama xol toy na
[00:34.75] Ki ma bëgg dem na, ku ma ko waxoon
[00:37.77] Mënu ma ko gëm li comme ay leboon
[00:41.40] Pexe noon lu am la, lu ma xam la man
[00:45.07] Jam nañ sama xol ba baa mu jaare fa
[00:48.73] Garab u mbëggeel so dagge reen ya
[00:51.30] Bul ci mësa yaakar gis ca dom ya
[00:56.87] Haaaaaaann
[01:01.15] Leleenenenen
[01:06.62] Namm nala lool
[01:08.40] Te xammuma fan nga dem
[01:10.05] Du ma la mësa fàtte
[01:11.82] Ak fo mëna dem
[01:13.57] Sa may ñaan nala fekk
[01:15.11] Fo mëna nekka
[01:17.06] Dalalal sa xel
[01:18.48] Sama xol ya ci nekka
[01:20.49] Namm nala lool
[01:22.17] Te xammuma fan nga dem
[01:23.50] Du ma la mësa fàtte
[01:25.63] Ak fo mëna dem
[01:27.01] Sa may ñaan nala fekk
[01:28.71] Fo mëna nekka
[01:30.58] Dalalal sa xel
[01:32.00] Sama xol ya ci nekka
[01:35.15] Sëy nañ ba am jaboot sama xel
[01:38.25] Jotuluma bayi ku maleey xolee
[01:42.35] Rongoñ dina siit suma la ñakkee
[01:45.45] Mbëggeel dina tiis jàmmu wa wàññeeku
[01:49.18] Yàlla na nga xippe sama kër
[01:51.82] Cat bañ la jiitu ci sa njegenaay
[01:55.62] Tëddi nga yobale sama mbëggeel
[01:59.03] Tëddi nga bayi mak dundu nammel
[02:02.68] Xam na ne nala manquer lool
[02:05.23] Wara dundu duma gis sa dom
[02:09.20] Dañ la nangu ci sameey loxo
[02:12.52] May ñuma sax ma xool sa xol man
[02:17.13] Hannnnnn (may ñuma sax ma xool sa xol man)
[02:22.58] Lelelennnn way
[02:27.77] Namm nala lool
[02:29.25] Te xammuma fan nga dem
[02:31.09] Du ma la mësa fàtte
[02:32.73] Ak fo mëna dem
[02:34.47] Sa may ñaan nala fekk
[02:36.16] Fo mëna nekka
[02:37.85] Dalalal sa xel
[02:39.33] Sama xol ya ci nekka
[02:41.66] Namm nala lool
[02:42.74] Te xammuma fan nga dem
[02:44.40] Du ma la mësa fàtte
[02:46.56] Ak fo mëna dem
[02:47.87] Sa may ñaan nala fekk
[02:49.71] Fo mëna nekka
[02:51.68] Dalalal sa xel
[02:53.05] Sama xol ya ci nekka
[03:28.71]
[00:27.76] Bës bu waroon nex la mujjee ay joy
[00:31.37] Sama yaram daw na, sama xol toy na
[00:34.75] Ki ma bëgg dem na, ku ma ko waxoon
[00:37.77] Mënu ma ko gëm li comme ay leboon
[00:41.40] Pexe noon lu am la, lu ma xam la man
[00:45.07] Jam nañ sama xol ba baa mu jaare fa
[00:48.73] Garab u mbëggeel so dagge reen ya
[00:51.30] Bul ci mësa yaakar gis ca dom ya
[00:56.87] Haaaaaaann
[01:01.15] Leleenenenen
[01:06.62] Namm nala lool
[01:08.40] Te xammuma fan nga dem
[01:10.05] Du ma la mësa fàtte
[01:11.82] Ak fo mëna dem
[01:13.57] Sa may ñaan nala fekk
[01:15.11] Fo mëna nekka
[01:17.06] Dalalal sa xel
[01:18.48] Sama xol ya ci nekka
[01:20.49] Namm nala lool
[01:22.17] Te xammuma fan nga dem
[01:23.50] Du ma la mësa fàtte
[01:25.63] Ak fo mëna dem
[01:27.01] Sa may ñaan nala fekk
[01:28.71] Fo mëna nekka
[01:30.58] Dalalal sa xel
[01:32.00] Sama xol ya ci nekka
[01:35.15] Sëy nañ ba am jaboot sama xel
[01:38.25] Jotuluma bayi ku maleey xolee
[01:42.35] Rongoñ dina siit suma la ñakkee
[01:45.45] Mbëggeel dina tiis jàmmu wa wàññeeku
[01:49.18] Yàlla na nga xippe sama kër
[01:51.82] Cat bañ la jiitu ci sa njegenaay
[01:55.62] Tëddi nga yobale sama mbëggeel
[01:59.03] Tëddi nga bayi mak dundu nammel
[02:02.68] Xam na ne nala manquer lool
[02:05.23] Wara dundu duma gis sa dom
[02:09.20] Dañ la nangu ci sameey loxo
[02:12.52] May ñuma sax ma xool sa xol man
[02:17.13] Hannnnnn (may ñuma sax ma xool sa xol man)
[02:22.58] Lelelennnn way
[02:27.77] Namm nala lool
[02:29.25] Te xammuma fan nga dem
[02:31.09] Du ma la mësa fàtte
[02:32.73] Ak fo mëna dem
[02:34.47] Sa may ñaan nala fekk
[02:36.16] Fo mëna nekka
[02:37.85] Dalalal sa xel
[02:39.33] Sama xol ya ci nekka
[02:41.66] Namm nala lool
[02:42.74] Te xammuma fan nga dem
[02:44.40] Du ma la mësa fàtte
[02:46.56] Ak fo mëna dem
[02:47.87] Sa may ñaan nala fekk
[02:49.71] Fo mëna nekka
[02:51.68] Dalalal sa xel
[02:53.05] Sama xol ya ci nekka
[03:28.71]