Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Seetu

👤 Dip Doundou Guiss 🎼 Dip Doundou Guiss ⏱️ 3:06
🎵 1950 characters
⏱️ 3:06 duration
🆔 ID: 15870254

📜 Lyrics

Hun hun hun
Hun hun hun hun
Hun hun hun hun
Oooh woo woo ouu woo
Oooh woo woo ou woo
Ohh woo woo
Woo wooo

Yeah life amul solo lu dem ba jar fi lii
Dam leen tijjil sam xol mais ñoom ci poche lañuy Jàppe nit
Ngay jàppe nit sa bopp muy teg sa kaw ay strategies
Ñaata millions lañ ma fi dóor mais bon ñu tedd ñépp jaar nañ ci
Doo wax ci ñoom danga leen di classé ni ex
Kuy leb akay yomb a jot après mu jafe ni fay
Ak noo manti jàppe nit di xëy bis claté bis fay
Fen dañ kay jàppe ni glace booy amul glace bu dul séyy
Divorcé aras moo ma gënal sëy buy tas bisub pénc
Du xar moo waral tabaski, état di gracié ñi ray
Kuy tuur dereet war na man lëkkalook ku gàcce dul ray
Nun sun salaire batay terewul ci sun añ lanuy reer
Waaye ku xam luy alal dëgg milliaru bànk du rëy sa bët
Ku am lu rëy sa bët manul ñàkk jagg yu fay sa njëg
Yéene néeg la moo tax it bis naa fanaan fi ma yéene ñépp
Ay gaynde ci biti, ci birr kàkkatar, caga yee la gën.

Hun
Life di la xët ci ruu ngay dimbali ñiy jooy ay góomu xol
Naqar di gën di ñëw fekk xamuñ ni que moo gënn ci ñoom
Dëkk sa kër ñuy xiif gënul nga gëj fa ñëw ndax wër millions
Waaye dee buy jël du yoot moo tax lu ñuy togg day xëm du ñor
Man xam naa lan laay yëg te xam naa nan laa mel ma nigger
Xamuma kañ laay dee waaye xam naa lan laay def
Dund mooy daaj boo dul mas a tàmm ndax dee moo kay dagg
Loo màndi màndi boo geestoo gis néew sa daaj yépp ay wàcc
Ñàkk a xam liy xew suba moo tax may gëmmentu di job
Bañ xéy réccu di jooy maak samay doom du dëgër sunu bor
Ci ñoom gis sama defaite moo leen gënal jël ay Coupe Du Monde
May jël ay coups ci xol ak muñ di gën dëgër tul ni néew
Jikko ni dëgg buy génn boroom rekk a ko dul yëg
Li ñuy nëbb ci seen gémmiñ moo fees dell ci seeni bët
Bien sûr que man nanu bokk te doo mas a bokk ci man
Te soxlawuma gilet par balles mais tulu paaka ginnaaw yeah

(Peace of mind ...)

⏱️ Synced Lyrics

[00:24.43] Hun hun hun
[00:27.32] Hun hun hun hun
[00:30.33] Hun hun hun hun
[00:33.32] Oooh woo woo ouu woo
[00:35.94] Oooh woo woo ou woo
[00:38.88] Ohh woo woo
[00:42.00] Woo wooo
[00:45.48] Yeah life amul solo lu dem ba jar fi lii
[00:48.68] Dam leen tijjil sam xol mais ñoom ci poche lañuy Jàppe nit
[00:51.15] Ngay jàppe nit sa bopp muy teg sa kaw ay strategies
[00:53.44] Ñaata millions lañ ma fi dóor mais bon ñu tedd ñépp jaar nañ ci
[00:57.09] Doo wax ci ñoom danga leen di classé ni ex
[00:59.34] Kuy leb akay yomb a jot après mu jafe ni fay
[01:02.21] Ak noo manti jàppe nit di xëy bis claté bis fay
[01:05.29] Fen dañ kay jàppe ni glace booy amul glace bu dul séyy
[01:08.05] Divorcé aras moo ma gënal sëy buy tas bisub pénc
[01:10.72] Du xar moo waral tabaski, état di gracié ñi ray
[01:13.62] Kuy tuur dereet war na man lëkkalook ku gàcce dul ray
[01:16.24] Nun sun salaire batay terewul ci sun añ lanuy reer
[01:19.18] Waaye ku xam luy alal dëgg milliaru bànk du rëy sa bët
[01:22.64] Ku am lu rëy sa bët manul ñàkk jagg yu fay sa njëg
[01:25.48] Yéene néeg la moo tax it bis naa fanaan fi ma yéene ñépp
[01:28.34] Ay gaynde ci biti, ci birr kàkkatar, caga yee la gën.
[01:52.54] Hun
[01:53.89] Life di la xët ci ruu ngay dimbali ñiy jooy ay góomu xol
[01:56.89] Naqar di gën di ñëw fekk xamuñ ni que moo gënn ci ñoom
[01:59.75] Dëkk sa kër ñuy xiif gënul nga gëj fa ñëw ndax wër millions
[02:02.64] Waaye dee buy jël du yoot moo tax lu ñuy togg day xëm du ñor
[02:05.01] Man xam naa lan laay yëg te xam naa nan laa mel ma nigger
[02:08.33] Xamuma kañ laay dee waaye xam naa lan laay def
[02:11.16] Dund mooy daaj boo dul mas a tàmm ndax dee moo kay dagg
[02:14.05] Loo màndi màndi boo geestoo gis néew sa daaj yépp ay wàcc
[02:16.85] Ñàkk a xam liy xew suba moo tax may gëmmentu di job
[02:19.70] Bañ xéy réccu di jooy maak samay doom du dëgër sunu bor
[02:22.36] Ci ñoom gis sama defaite moo leen gënal jël ay Coupe Du Monde
[02:24.91] May jël ay coups ci xol ak muñ di gën dëgër tul ni néew
[02:27.99] Jikko ni dëgg buy génn boroom rekk a ko dul yëg
[02:30.56] Li ñuy nëbb ci seen gémmiñ moo fees dell ci seeni bët
[02:33.58] Bien sûr que man nanu bokk te doo mas a bokk ci man
[02:36.57] Te soxlawuma gilet par balles mais tulu paaka ginnaaw yeah
[03:04.22] (Peace of mind ...)
[03:04.82]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings