Eutou Baabel
🎵 1637 characters
⏱️ 2:56 duration
🆔 ID: 17049028
📜 Lyrics
Par AbouAmg
Maak yaw ba abadan
Jox naa la sama kàttan
Jaayaanteek sama ndaw
Dem naa ba ndox ci baat
Jox naa la sama kàddu
Mënatuma la bàyyi
Te sèntu naa ci jële ndam maak yaw
Ndax àddunya bi dafay feexe ba ma xàddi
Duma bàyyi li ma tàmbali man
Fàttaliku naa sama maam
Ne na ma 'Fori jëlal jaaro gi'
Dégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Xam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Demanoon de nañu
Defando nañu ay mbir
Xamal nga ma lu ne
Soo ma yoolee
Dootuma jar dara
Bi ma ñépp gumbale
Yaw yaa ko xam
Sama waay nga
Ku mel ni yaw
Ku ka amul da koy iññane
Ku mel ni yaw
Ëttu Baabel ñoo lay laaj
Ku mel ni yaw
Thiam Baabel Demba Thiam, eh
Ku mel ni yaw
Ëttu Baabel yaw lay laaj
Naa la yóbbu ëttu Baabel
Boole la ak samay nawle yi
Xam nga tàkkusaanu Baabel
Thiam boroom nénni was dafay xeweey
Yaw
Mësuloo ma xépp ci samay ayib
Sama njuumte yi mësoo ko nettali
Xam nga jaambaar amul
Ku ñu dimbale am
Ku sañoon day baax
Comme doomu ñay
Bu ma ñaanal ponkal
Man soo ma dundee baax

⏱️ Synced Lyrics
[00:01.21] Par AbouAmg
[00:06.68] Maak yaw ba abadan
[00:15.95] Jox naa la sama kàttan
[00:18.41] Jaayaanteek sama ndaw
[00:20.43] Dem naa ba ndox ci baat
[00:23.51] Jox naa la sama kàddu
[00:25.77] Mënatuma la bàyyi
[00:27.89] Te sèntu naa ci jële ndam maak yaw
[00:31.69] Ndax àddunya bi dafay feexe ba ma xàddi
[00:36.40] Duma bàyyi li ma tàmbali man
[00:39.32] Fàttaliku naa sama maam
[00:41.63] Ne na ma 'Fori jëlal jaaro gi'
[00:43.38] Dégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
[00:47.25] Xam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
[00:50.84] Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
[00:54.90] Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
[00:58.59] Demanoon de nañu
[01:00.22] Defando nañu ay mbir
[01:02.08] Xamal nga ma lu ne
[01:03.75] Soo ma yoolee
[01:05.82] Dootuma jar dara
[01:07.41] Bi ma ñépp gumbale
[01:09.32] Yaw yaa ko xam
[01:11.19] Sama waay nga
[01:13.17] Ku mel ni yaw
[01:14.75] Ku ka amul da koy iññane
[01:16.94] Ku mel ni yaw
[01:18.61] Ëttu Baabel ñoo lay laaj
[01:20.45] Ku mel ni yaw
[01:22.00] Thiam Baabel Demba Thiam, eh
[01:24.58] Ku mel ni yaw
[01:25.86] Ëttu Baabel yaw lay laaj
[01:27.78] Naa la yóbbu ëttu Baabel
[01:30.14] Boole la ak samay nawle yi
[01:34.08] Xam nga tàkkusaanu Baabel
[01:37.92] Thiam boroom nénni was dafay xeweey
[01:40.95] Yaw
[01:42.46] Mësuloo ma xépp ci samay ayib
[01:45.71] Sama njuumte yi mësoo ko nettali
[01:48.45] Xam nga jaambaar amul
[01:49.95] Ku ñu dimbale am
[01:51.23] Ku sañoon day baax
[01:52.58] Comme doomu ñay
[01:54.04] Bu ma ñaanal ponkal
[01:55.19] Man soo ma dundee baax
[01:56.42] Dégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
[01:59.64] Xam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
[02:03.28] Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
[02:05.55] Kenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
[02:11.03] Demanoon de nañu
[02:12.23] Defando nañu ay mbir
[02:14.38] Xamal nga ma lu ne
[02:16.16] Soo ma yoolee
[02:18.35] Dootuma jar dara
[02:19.87] Bi ma ñépp gumbale
[02:21.92] Yaw yaa ko xam
[02:23.61] Sama waay nga
[02:25.51] Ku mel ni yaw
[02:27.24] Ku ka amul da koy iññane
[02:29.67] Ku mel ni yaw
[02:31.02] Ëttu Baabel ñoo lay laaj
[02:33.32] Ku mel ni yaw
[02:34.73] Thiam Baabel Demba Thiam, eh
[02:36.81] Ku mel ni yaw
[02:39.27] Ëttu Baabel yaw lay laaj
[02:41.22]