Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Ajaa mooy Ajaa

👤 AMADEUS 🎼 Taaru Sénégal ⏱️ 2:50
🎵 1167 characters
⏱️ 2:50 duration
🆔 ID: 17230719

📜 Lyrics

Hey Massamba Walo
Jàllo, jàllo, yaay
Jàllo, jàllo, yaay

Xam nga dama laa bëgg
Ngir rekk danga maa bëgg
Am nga yitte maandu nga
Am nga ngor dangaa dëggu

Sooy dem bul ma fi bàyyi
Ajaa mooy ajaa
Ma xam fa nga jëlee mbaax
Ajaa mooy ajaa
Ni nga tabee kaar
Ajaa mooy ajaa

Ajaa jàllooy taar
Ajaa mooy ajaa
Mu dàq la yàqul sa taar
Ajaa mooy ajaa

Ajaa jallooy taar
Ajaa mooy ajaa
Ni nga tabee kaar
Ajaa mooy ajaa
Fa nga jëlee mbaax

Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay

Ajaa mooy ajaa
Ajaa mooy ajaa
Ajaa mooy ajaa
Ajaa mooy ajaa

Daqqante leen ci seen biir
Sutanteleen te ba fiiram gi
Su njaag agsee nga xam ne ñëw na
Jàllo jeeri tukkuloor Sàmba Ngaari jamaa yeah

Sooy dem bul ma fi bàyyi
Ma xam fa nga jëlee mbaax
Ni nga tabee kaar
Mu dàq la taxul nga ñaaw

Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay

Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa
Jàlloo, Jàlloo, yaay
Ajaa mooy ajaa

⏱️ Synced Lyrics

[00:03.79] Hey Massamba Walo
[00:07.67] Jàllo, jàllo, yaay
[00:10.96] Jàllo, jàllo, yaay
[00:15.09] Xam nga dama laa bëgg
[00:18.73] Ngir rekk danga maa bëgg
[00:22.58] Am nga yitte maandu nga
[00:26.17] Am nga ngor dangaa dëggu
[00:30.26] Sooy dem bul ma fi bàyyi
[00:33.13] Ajaa mooy ajaa
[00:34.45] Ma xam fa nga jëlee mbaax
[00:36.64] Ajaa mooy ajaa
[00:38.40] Ni nga tabee kaar
[00:40.37] Ajaa mooy ajaa
[00:42.68] Ajaa jàllooy taar
[00:44.42] Ajaa mooy ajaa
[00:45.79] Mu dàq la yàqul sa taar
[00:47.86] Ajaa mooy ajaa
[00:49.82] Ajaa jallooy taar
[00:51.74] Ajaa mooy ajaa
[00:53.41] Ni nga tabee kaar
[00:55.58] Ajaa mooy ajaa
[00:57.70] Fa nga jëlee mbaax
[01:00.29] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[01:03.30] Ajaa mooy ajaa
[01:04.22] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[01:06.64] Ajaa mooy ajaa
[01:08.09] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[01:10.66] Ajaa mooy ajaa
[01:11.84] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[01:18.90] Ajaa mooy ajaa
[01:21.90] Ajaa mooy ajaa
[01:25.73] Ajaa mooy ajaa
[01:29.69] Ajaa mooy ajaa
[01:30.66] Daqqante leen ci seen biir
[01:34.43] Sutanteleen te ba fiiram gi
[01:38.12] Su njaag agsee nga xam ne ñëw na
[01:41.93] Jàllo jeeri tukkuloor Sàmba Ngaari jamaa yeah
[01:47.59] Sooy dem bul ma fi bàyyi
[01:51.27] Ma xam fa nga jëlee mbaax
[01:55.35] Ni nga tabee kaar
[01:58.85] Mu dàq la taxul nga ñaaw
[02:00.71] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:03.45] Ajaa mooy ajaa
[02:04.80] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:07.18] Ajaa mooy ajaa
[02:08.57] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:10.78] Ajaa mooy ajaa
[02:12.14] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:16.18] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:18.53] Ajaa mooy ajaa
[02:19.96] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:22.17] Ajaa mooy ajaa
[02:23.92] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:26.05] Ajaa mooy ajaa
[02:27.35] Jàlloo, Jàlloo, yaay
[02:29.94] Ajaa mooy ajaa
[02:32.08]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings