Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Immigrés / Bitim Rew

👤 Youssou N’Dour & Le Super Étoile 🎼 Immigrés ⏱️ 7:03
🎵 1665 characters
⏱️ 7:03 duration
🆔 ID: 31449742

📜 Lyrics

Ibu Njaay Faama
Ibu Njaay Faama

Waaw bittim réew ña fa nekk dëkk ñu fa
Mujj u mujj yaay dañuy déllu ci waaw Sénégal

Ibu Njaay Fama
Ibu Njaay Fama

Uzin bitim réew ña fa nekk dëkk ñu faa
Mujj u mujj yaay dañuy ñibbi cee waw Sénégal

Hoolé
Bitim réew ligéey la laaj
Immigré ligéey la laaj
Immigré

Ibu Njaay Fama
Ibu Njaay Fama

Ñu nee "bitim reyew ñu fa nekk dëkk ñu fa
Mujju mujj yaay da ñi déllu ce
Ndaxte ñoo ñu xamu ñu léen
Fi la ñu saaso"
Ñu nee "jòom mooy tukki yaay
Waye fulla mooy ñibbi cee
Noo mën a mel
Loo mën a am ndeysan ñibbi ce la war

Youssoo sabali nga,sabali nga
Déedéet samaliwul deh
Moytul lu la neex defal, lu la nex waxal
Ndax bañuloo te mbëgg nga
Ñepp a am
Coodu Faal Caa-Ndeela, yaay, Caa-Ndeela

Ñu nee Nene Ada may ma ci saa jaam ñi
Maa Dické lo ba caa Xaayo, li sagam neex na la
Yaayu Colle Jaaga woo nala

Baay Yuusu, xam nga li ma neex ci yaw
Yaa ñi seet li doxal réew yi
Waye nit ku mënul te bàwul
Laajul tay def, lu yàkku, moo, moo, lu mu
Yuusu, yaw deh yàkkoo

Sant nañu léen, ñoo ñi dileen ñanal
Su ma delloo, dileen way yan too
Waaw Sénégal
Mooy sunu réew

Waa sant nañu léen, ñoo ñi dileen ñanal
Su ma delloo, dileen wayyan too
Waaw Sénégal
Mooy sunu réew

Waaw najjee mu ni laa, say ñu nekk
Su ma sañoon di koo défal ak yéen
Waaw Sénégal, mooy sunu réew
Ibu Njaay Faama Dabaax (waaw Sénégal)
Abdou Aziz Malick Dabaax (Mooy sunu réew)
Ibu Njaay Faama Dabaax (waaw Sénégal)
Abdou Aziz Malick Dabaax (Mooy sunu réew)

Waaw sant nañu léen, ñoo ñi dileen ñanal
Suñu delloo, dileen wayyan too
Waaw Sénégal
Sénégal, Sénégaloo
Mooy sunu réew

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings