Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

SAMA BÉBÉ

👤 Iss 814 🎼 SAMA BÉBÉ ⏱️ 2:08
🎵 1346 characters
⏱️ 2:08 duration
🆔 ID: 32281467

📜 Lyrics

Oh bébé, sama bébé
Bébé, bëgg na la bébé
Oh bébé, sama bébé
Wa bébé, bëgg na la bébé

Man suma yeewo yaw lay njëkk wo
Ubi samay messages xool ndax bindulo
Baby namm na la lool
Mënatuma xaar, wax ma kañ ngay ñëw
Bo ma soré dafmay metti lool eh
Mais bo ma jégué baby lepp ay leer
Allô, allô, kaay nga wax ma fo né
Ma fekksi la wuy lé lê

Photo bing' ma yonné dafa sexy
Namm na la lool, kañ nga may seetsi?
Wuy lé lé, bébé wuy lé lé lé waaw (wuy lé lé)
Bébé wuy lé lé lé waaw
Sa makeup fing' ko tekk non fofoy plaçam
Jarul nga koy dindi baayil nonu
Wuy lé lé, bébé wuy lé lé lé waaw (wuy lé lé)
Bébé wuy lé lé lé waaw

Jégué ma, ñëwal ñu dundu love yaw
Xeex ak ñu bëgg barer suñu vie
Bul wax keneen li né či mane ak yaw
Bo ko deffé wassaaré suñu vie
(Oh)

Teg na či yaw, té duma teggi
Takk ma buum, té bu' ma tekki
My baby kaay, deff ma Habibi
Habibi, yay Habibi

Photo bing' ma yonné dafa sexy
Namm na la lool, kañ nga may seetsi?
Wuy lé lé, bébé wuy lé lé lé waaw (wuy lé lé)
Bébé wuy lé lé lé waaw
Sa makeup fing' ko tekk non fofoy plaçam
Jarul nga koy dindi baayil nonu
Wuy lé lé, bébé wuy lé lé lé waaw (wuy lé lé)
Bébé wuy lé lé lé waaw

Bébé, sama bébé
Bébé, bëgg na la bébé
Oh bébé, sama bébé
Bébé, bëgg na la bébé

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings