Baykat
🎵 1214 characters
⏱️ 4:29 duration
🆔 ID: 5379743
📜 Lyrics
Mané hé baykat bi khalam
Démonna bay nékh wayé boumgua
Dokna mome
Mané hé baykat bi khalam démonna
Bay nékh wayé boumgua dokna mome
Boula nékhé talalal say lokho
Yaye docteur biy fath khifou askane bi
Liko dalé si nditoum rew bassi miskine
Ya souméko di dane sa dolé andak nath
Bi di liguey sa gnakha di tourou
Ngay bay di doukat bilay ya am diome
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour waw koufi fébar
Yako nandal aki réén bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Ya momone sa mbay
Ya mome sa guanthiakh mome say
Ndiour ya mome sa alla di bay
Nguour gneuw dougalthia lokhome ak
Boor fékeleuthaa guanthiakh ba
Mégneu lole ndékétéyo
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Dirama diarama baykat bé yaw
Kéneu rek mola mana fay
Moy bourbi yaalla
Guathia ngalama
Guathia ngalama yaw baykatbé
Guathia ngalama
Guathia ngalama yaw baikatbé
Dirama diarama baykatbé yaw
Kéneu rek moleu mana fay
Moye bourbi yalla
Démonna bay nékh wayé boumgua
Dokna mome
Mané hé baykat bi khalam démonna
Bay nékh wayé boumgua dokna mome
Boula nékhé talalal say lokho
Yaye docteur biy fath khifou askane bi
Liko dalé si nditoum rew bassi miskine
Ya souméko di dane sa dolé andak nath
Bi di liguey sa gnakha di tourou
Ngay bay di doukat bilay ya am diome
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour waw koufi fébar
Yako nandal aki réén bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Ya momone sa mbay
Ya mome sa guanthiakh mome say
Ndiour ya mome sa alla di bay
Nguour gneuw dougalthia lokhome ak
Boor fékeleuthaa guanthiakh ba
Mégneu lole ndékétéyo
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Kon diarama baykat koufi xiff yako
Doundal bamou sour
Waw koufi fébar yako nandal aki réén
Bamou féékh
Dirama diarama baykat bé yaw
Kéneu rek mola mana fay
Moy bourbi yaalla
Guathia ngalama
Guathia ngalama yaw baykatbé
Guathia ngalama
Guathia ngalama yaw baikatbé
Dirama diarama baykatbé yaw
Kéneu rek moleu mana fay
Moye bourbi yalla
⏱️ Synced Lyrics
[00:08.12] Mané hé baykat bi khalam
[00:14.44] Démonna bay nékh wayé boumgua
[00:19.00] Dokna mome
[00:24.48] Mané hé baykat bi khalam démonna
[00:29.97] Bay nékh wayé boumgua dokna mome
[00:40.72] Boula nékhé talalal say lokho
[00:43.53] Yaye docteur biy fath khifou askane bi
[00:47.12] Liko dalé si nditoum rew bassi miskine
[00:55.31] Ya souméko di dane sa dolé andak nath
[00:58.99] Bi di liguey sa gnakha di tourou
[01:01.61] Ngay bay di doukat bilay ya am diome
[01:08.93] Kon diarama baykat koufi xiff yako
[01:12.57] Doundal bamou sour waw koufi fébar
[01:17.96] Yako nandal aki réén bamou féékh
[01:23.42] Kon diarama baykat koufi xiff yako
[01:26.12] Doundal bamou sour
[01:29.78] Waw koufi fébar yako nandal aki réén
[01:34.39] Bamou féékh
[01:41.50] Ya momone sa mbay
[01:45.23] Ya mome sa guanthiakh mome say
[01:47.96] Ndiour ya mome sa alla di bay
[01:56.06] Nguour gneuw dougalthia lokhome ak
[01:59.79] Boor fékeleuthaa guanthiakh ba
[02:03.32] Mégneu lole ndékétéyo
[02:09.68] Kon diarama baykat koufi xiff yako
[02:13.28] Doundal bamou sour
[02:16.06] Waw koufi fébar yako nandal aki réén
[02:20.53] Bamou féékh
[02:23.33] Kon diarama baykat koufi xiff yako
[02:26.95] Doundal bamou sour
[02:30.57] Waw koufi fébar yako nandal aki réén
[02:35.05] Bamou féékh
[02:38.79] Dirama diarama baykat bé yaw
[03:13.18] Kéneu rek mola mana fay
[03:35.83] Moy bourbi yaalla
[03:40.36] Guathia ngalama
[03:42.10] Guathia ngalama yaw baykatbé
[03:47.67] Guathia ngalama
[03:49.48] Guathia ngalama yaw baikatbé
[03:54.81] Dirama diarama baykatbé yaw
[03:57.57] Kéneu rek moleu mana fay
[04:04.80] Moye bourbi yalla
[04:09.35]