Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Dabbaax

👤 Youssou N'Dour 🎼 Rokku Mi Rokka ⏱️ 5:08
🎵 1762 characters
⏱️ 5:08 duration
🆔 ID: 7314956

📜 Lyrics

Keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi
Di wadjial Péssé ba
Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
Moulaay Dabaaaaax...

Bougnou Faté, Bess boboulé, Uhh Bougnou Soré, Bess boboulé
Bougnou faté Bess Boboulé,
Lofa Gnaane, Yalla May lako.
Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
Anh Mo daane Kadou Askane wi.

Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
Dafa daane wakh naane nagnou yeureum Djiguéen

Sa borom bi begu na, Yonentam bi begu na, yako liguéyal sa borom.
Moulaye Dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul.
Kérok bang gnou djito assamaane si da Leudeum,
Bessa ngui kéne dotou ko Fatéééti... Moulaay Dabbaxx

Bougnou Faté, Bess boboulé, Bougnou Soré, Bess boboulé
Bougnou faté Bess Boboulé,
Lofa Gnaane, Yalla May lako.
Anh! Modaane wakhal nitt gnep, anh! Mo daane wakhal nasraane yi.
Anh! Mo daane wakhal Askane wi.

Dafa daane wakh naane na gnep ligueye
Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
Dafa daane wakh naane na gnep liguèye
Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni

Daawaoul Sétane lou gnaaw
Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx

Daawaoul Sétane lou gnaaw
Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx.
Bakrék Dara Maam, Aram lô Coumba Thiam,
Magn Penda ak Pathé Pendaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah

Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
Mo daane Kadou Askane wi.
Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi.
Dafa daane wakh naane nagnep liguéye
Dafa daane wakh naane nagn Yeureum djiguéene gni.
Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi

⏱️ Synced Lyrics

[00:05.23] Keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi
[00:22.09] Di wadjial Péssé ba
[00:26.99] Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
[00:32.69] Moulaay Dabaaaaax...
[00:38.26] Bougnou Faté, Bess boboulé, Uhh Bougnou Soré, Bess boboulé
[00:47.86] Bougnou faté Bess Boboulé,
[00:55.83] Lofa Gnaane, Yalla May lako.
[01:00.74] Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
[01:13.74] Anh Mo daane Kadou Askane wi.
[01:19.33] Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
[01:24.67] Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
[01:28.98] Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
[01:33.90] Dafa daane wakh naane nagnou yeureum Djiguéen
[01:57.84] Sa borom bi begu na, Yonentam bi begu na, yako liguéyal sa borom.
[02:02.70] Moulaye Dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul.
[02:12.78] Kérok bang gnou djito assamaane si da Leudeum,
[02:14.26] Bessa ngui kéne dotou ko Fatéééti... Moulaay Dabbaxx
[02:21.97] Bougnou Faté, Bess boboulé, Bougnou Soré, Bess boboulé
[02:32.07] Bougnou faté Bess Boboulé,
[02:37.63] Lofa Gnaane, Yalla May lako.
[02:43.00] Anh! Modaane wakhal nitt gnep, anh! Mo daane wakhal nasraane yi.
[02:53.33] Anh! Mo daane wakhal Askane wi.
[03:01.50] Dafa daane wakh naane na gnep ligueye
[03:04.52] Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
[03:09.73] Dafa daane wakh naane na gnep liguèye
[03:15.04] Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni
[03:28.64] Daawaoul Sétane lou gnaaw
[03:38.21] Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
[03:41.66] Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx
[04:01.38] Daawaoul Sétane lou gnaaw
[04:04.26] Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
[04:09.29] Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx.
[04:13.47] Bakrék Dara Maam, Aram lô Coumba Thiam,
[04:15.45] Magn Penda ak Pathé Pendaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah
[04:17.58] Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
[04:37.14] Mo daane Kadou Askane wi.
[04:42.72] Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi.
[04:46.82] Dafa daane wakh naane nagnep liguéye
[04:52.18] Dafa daane wakh naane nagn Yeureum djiguéene gni.
[04:58.97] Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
[05:03.04]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings