Ndox - L'eau
🎵 1557 characters
⏱️ 4:19 duration
🆔 ID: 7430971
📜 Lyrics
Sa joie et sa pudeur font sa face cachée
Son paraître et ses formes montrent sa force
Celle que je vous chante, vous est familière
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis
Mbégte ma, sutura sa
Da fa méngóok, baatinëm
Zaahir sa, melo ya
Moo wone, kattanam
Li may misaal lu ngeen xam la
Am na njariñ te rafet na
Moo génne taaru adduna
Moom la ñu bakke, al janna
Waxtaane ko sax banneex la
Nañ ko foηk sakkanal ko
En parler même est agréable
Respectons-la, économisons-la
Vois la mer, le fleuve
Rendons grâce à Dieu
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis
Mbégte ma, sutura sa
Da fa méngóok, baatinëm
Zaahir sa, melo ya
Moo wone, kattan am
Li may misaal lu ngeen xam la
Am na njariñ te rafet na
Moo génne taar u adduna
Moom la ñu bakke, al janna
Waxtaane ko sax banneex la
Nañ ko foηk sakkanal ko
Géej gaa ngi nii yé
Dex gaa ngi nii yé
Dara gënul ë neex taw bi
Ku weddi laaj ko bay kat ba
Ci la ñuy roosé seen tool ya
Walla nga laaj ko samm kat ba
Ci la ñuy nandale jur ga
Ndox daal am na njariñ baax na
Dara gënul la neex taw bi
Taw daal njariñ la ci dun bi
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñëm Ba la nga koo xam mu jafe
Alaa gaynaago yoo samba lingeer
Donoy waaly yée, wulée ñaay ngoy
Yée gan wuri coo, wulée gaynaako yoo
Yeée, yóo, gan fari baa

⏱️ Synced Lyrics
[00:01.70] Sa joie et sa pudeur font sa face cachée
[00:05.77] Son paraître et ses formes montrent sa force
[00:10.57] Celle que je vous chante, vous est familière
[00:16.13] Elle est utile et belle
[00:18.25] Elle a révélé la beauté du monde
[00:22.75] On la clame Paradis
[00:26.12] Mbégte ma, sutura sa
[00:30.48] Da fa méngóok, baatinëm
[00:35.69] Zaahir sa, melo ya
[00:40.11] Moo wone, kattanam
[00:44.64] Li may misaal lu ngeen xam la
[00:49.20] Am na njariñ te rafet na
[00:54.27] Moo génne taaru adduna
[00:58.57] Moom la ñu bakke, al janna
[01:03.28] Waxtaane ko sax banneex la
[01:08.07] Nañ ko foηk sakkanal ko
[01:14.24] En parler même est agréable
[01:18.71] Respectons-la, économisons-la
[01:23.23] Vois la mer, le fleuve
[01:25.51] Rendons grâce à Dieu
[01:28.63] Elle est utile et belle
[01:31.23] Elle a révélé la beauté du monde
[01:35.74] On la clame Paradis
[01:38.84] Mbégte ma, sutura sa
[01:43.41] Da fa méngóok, baatinëm
[01:48.17] Zaahir sa, melo ya
[01:52.88] Moo wone, kattan am
[01:57.47] Li may misaal lu ngeen xam la
[02:01.99] Am na njariñ te rafet na
[02:06.88] Moo génne taar u adduna
[02:11.75] Moom la ñu bakke, al janna
[02:16.28] Waxtaane ko sax banneex la
[02:21.14] Nañ ko foηk sakkanal ko
[02:26.03] Géej gaa ngi nii yé
[02:31.03] Dex gaa ngi nii yé
[02:35.28] Dara gënul ë neex taw bi
[02:39.68] Ku weddi laaj ko bay kat ba
[02:44.85] Ci la ñuy roosé seen tool ya
[02:49.36] Walla nga laaj ko samm kat ba
[02:54.15] Ci la ñuy nandale jur ga
[02:58.74] Ndox daal am na njariñ baax na
[03:03.10] Dara gënul la neex taw bi
[03:08.27] Taw daal njariñ la ci dun bi
[03:16.41] Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe
[03:20.27] Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué
[03:24.84] Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe
[03:29.79] Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué
[03:34.61] Ndox daal njariñëm Ba la nga koo xam mu jafe
[03:39.55] Alaa gaynaago yoo samba lingeer
[03:42.93] Donoy waaly yée, wulée ñaay ngoy
[03:52.02] Yée gan wuri coo, wulée gaynaako yoo
[04:04.86] Yeée, yóo, gan fari baa
[04:14.16]