Demone na
🎵 1895 characters
⏱️ 4:57 duration
🆔 ID: 7611154
📜 Lyrics
Sala maley koume yénangue si repondeurou Maissa Wally
Bayil lén ma sen message gayi dina lén délo sén bataaxal Jajëfëte
Allô maissa mane la kiné
So guissé sama message nga wone
C'est urgent tëdëgu ma yaw rek lay xar soma mëné wo nga rappelé ma
Lim lay xar walay walay
Kan lay xar walay walay
Dan kay xar walay walay
Démone na bay ame louma neex
Demone na bay seti lenen
Demone bay xol ngi
Nane fane la jëm
Leg leg ma noopi xar
Yakaar ni légui dina baax
Wayé mane Dale may doundé yakar
Tey niane li meussa diékh ndax
Wo nima deuké li dé
Sama xol leundeum lol
Wayé mane dal may doundé yakar
Téy niane li meussa diékh
Soxnassi massa thiono
Wone nima deuké ligueye
Oh ma séti banéx ndax ma foo fa lénéne
Bindone na fi diank pay wére
Tay môme lay woudiél
Légui sakh dotoul maak môme
Ma néxone né woudioulén
Thi seuye boumou meuna nék
Ak fép foumou meuna nék
Yaw farlouthié ndax lolou moy missalmi
(Waw kiné nganga def?
Mangui fi maissa ca va?
Wa mais yaw mangui lay diéma wo sank la Mba diam?
Dou diam môme
Makhou mo kheuy tay rek dima doorate
Door?
Wawaw, tay sakh wa kogne bi niossi diap, diniou atté
Seutttte!!!! Mais lolou mome doyna war môme.)
Ngi xamoul ligniy def
Ngi di sene, ngi di doundé yakar
Tey niane li meussa diékh ndax
Si kep koumou meuna nék
Ak goor goumou meuna done lemlouthié ndax lolou moy
Kép kou beugone na done sa soeur
Sa seute, djiguéne la diabar la dankoy nékhal
Ah kiné yaw massa thiona
Djiguén koumou meuna lér
Bakanou doumou Adama dina lathie diamak salam
Kép kou beugone na done sa soeur
Sa seute, djiguéne la diabar la dankoy nekhal
(Kamama missal
Loumama missal louma narra diotela
Djiguéne gni woyal lén beugual lén)
Kamama missal

⏱️ Synced Lyrics
[00:12.80] Sala maley koume yénangue si repondeurou Maissa Wally
[00:16.93] Bayil lén ma sen message gayi dina lén délo sén bataaxal Jajëfëte
[00:20.57] Allô maissa mane la kiné
[00:25.06] So guissé sama message nga wone
[00:29.16] C'est urgent tëdëgu ma yaw rek lay xar soma mëné wo nga rappelé ma
[00:33.42] Lim lay xar walay walay
[00:37.94] Kan lay xar walay walay
[00:39.72] Dan kay xar walay walay
[00:42.97] Démone na bay ame louma neex
[00:46.41] Demone na bay seti lenen
[00:48.16] Demone bay xol ngi
[00:52.98] Nane fane la jëm
[00:59.14] Leg leg ma noopi xar
[01:01.79] Yakaar ni légui dina baax
[01:06.16] Wayé mane Dale may doundé yakar
[01:10.26] Tey niane li meussa diékh ndax
[01:12.71] Wo nima deuké li dé
[01:16.98] Sama xol leundeum lol
[01:19.58] Wayé mane dal may doundé yakar
[01:23.30] Téy niane li meussa diékh
[01:27.82] Soxnassi massa thiono
[01:29.20] Wone nima deuké ligueye
[01:32.82] Oh ma séti banéx ndax ma foo fa lénéne
[01:36.69] Bindone na fi diank pay wére
[01:39.37] Tay môme lay woudiél
[01:41.52] Légui sakh dotoul maak môme
[01:42.93] Ma néxone né woudioulén
[01:48.36] Thi seuye boumou meuna nék
[01:49.70] Ak fép foumou meuna nék
[01:52.91] Yaw farlouthié ndax lolou moy missalmi
[02:09.74] (Waw kiné nganga def?
[02:14.71] Mangui fi maissa ca va?
[02:18.35] Wa mais yaw mangui lay diéma wo sank la Mba diam?
[02:21.72] Dou diam môme
[02:24.38] Makhou mo kheuy tay rek dima doorate
[02:27.31] Door?
[02:30.33] Wawaw, tay sakh wa kogne bi niossi diap, diniou atté
[02:32.82] Seutttte!!!! Mais lolou mome doyna war môme.)
[02:35.84] Ngi xamoul ligniy def
[02:38.62] Ngi di sene, ngi di doundé yakar
[02:42.25] Tey niane li meussa diékh ndax
[02:45.49] Si kep koumou meuna nék
[02:47.81] Ak goor goumou meuna done lemlouthié ndax lolou moy
[02:51.49] Kép kou beugone na done sa soeur
[02:53.78] Sa seute, djiguéne la diabar la dankoy nékhal
[02:57.45] Ah kiné yaw massa thiona
[02:58.54] Djiguén koumou meuna lér
[03:01.99] Bakanou doumou Adama dina lathie diamak salam
[03:15.34] Kép kou beugone na done sa soeur
[03:19.71] Sa seute, djiguéne la diabar la dankoy nekhal
[03:26.40] (Kamama missal
[03:29.96] Loumama missal louma narra diotela
[03:46.42] Djiguéne gni woyal lén beugual lén)
[03:50.52] Kamama missal
[03:52.65] Loumama missal louma narra diotela
[03:58.78] Djiguéne gni woyal lén beugual lén)
[04:02.65] Kamama missal
[04:04.88] Loumama missal louma narra diotela
[04:10.74] Djiguéne gni woyal lén beugual lén)
[04:21.14]