Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Bàjjan

👤 Youssou N'Dour 🎼 Rokku Mi Rokka ⏱️ 4:04
🎵 1685 characters
⏱️ 4:04 duration
🆔 ID: 7913422

📜 Lyrics

Taasukat baa nga naan gainde gu waaf ca buntu kër gé, di melastiku
Bëy bu em bàjjan du fa dem, Zacharia, bàjjan am na maanaa, wayai
Lu la réér ci sa cosaan, sa bàjjan xamal la ko

Boo bëgéé xam sa cosaan, kam la fa maam yi bayyi woom
Demal seeti bàjjan ba, lu mu la ca wax, du deñ
Bàjjana xam Kalcor an ba ca mbeneex wa
Cosaani askan wi, bàjjan am na maanan
Wayum terànga la kuy bàjjan jog, Sungun SanGan bàjjan, bàjjan
Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, Sungun SanGan
Neenan mag a pu rencontrer de naa ba cim rééw
Waaye bàjjan il a répondu à na bàyyi ci biir Kër
Xam sa Boppa Gén Ñu woo la naan kii nga Doon
Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan
Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ
Boo bëgéé xam sa cosaan, sa bàjjan moo la koy xamal

Moo la naan awai fii, bul dem fee, defeel nii
Boo ko seetioo dara du ca deñ
Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan
Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan
Si bj Gaay Walla raidiam
Lu xew lune crinière bàjjan laxaw
Bu Goor bugéé néégu Goor
Bàjjan taxaw wayal ko mbaax
Nijaay di Yaay nga di Baay
Bàjjan am na maanaa
Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, Sungun SanGan bàjjan, bàjjan
Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ
Bàjjan moodi magi baay walla rakkam
Lu xew lune mane bàjjan laxaw

Bu góó bugéé néégu góór
Bàjjan taxaw wayal ko mbaax
Nijaay di Yaay nga di Baay
Bàjjan am na maanaa
Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan
Wayum terànga la kuy bàjjan sj

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings