Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Pullo Àrdo

👤 Youssou N'Dour 🎼 Rokku Mi Rokka ⏱️ 4:01
🎵 1628 characters
⏱️ 4:01 duration
🆔 ID: 7913852

📜 Lyrics

Ku fi ñëw mu jangal la
Nax mi moo ko moon noox mi moo ko moom
Daf ko dónn
Lii xar yi la, lii bey yi la
Nagam yangi, àli bàngi
Baaxi maamam Pullo Àrdo
Ku fi ñëw mu jangal fa
Nax mi moo ko moon noox mi moo ko moom
Lii xar yi la, lii bey yi la
Nagam yangi, àli bàngi
Baaxi maaman Pullo Àrdo
Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
Pullo Jééri, Pullo Àrdo, Pullo Jééri
Dàqqal yee ñu jëm fee nga dàqq yil ñu jëm fii
Yaa xam yaw li xew fee, dara jaxalula fii ba fee
Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
Àrdo sex na gënnëm
Dàldi gàddu yattam
Ma nga ànd ag xaajam
Dàldi jittël géttam
Pullo Jééri, Pullo Àrdo
Mi ngi ànd ag xaajam
Dàldi jiitél géttam
Dalal xelam, fééxal xolam
Bu nin ñi fo aka ree moom yégu ko suuy
Pullo Àrdo, Pullo Jééri
Yeppam mu ngi fii
Fii la yaroo, fii la màgee
Te yii fii la takkee sowna
Léppam fii la
Pullo Àrdo, Pullo Jééri
Bu nin ñi tëbë ka dal moom yëgu ko
Li mu am fii doyloo na ko doy loo na ko
Bu dee cor la mbaa jamaan la
Walla etaas la, mbaa abyong la, mbaa leneen la
Moom gisu ko, Pullo Àrdo
Ma nga gàddu taxaaran
Di mbiip mbiip mu am xorom
Way, way yu amui moroom
Mel ni kuy neexai goroom
Boo fa jaaree sant Saar ee di na la ree
Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
Di mbiip mbiip mu am xorom
Way, way yu amui moroom
Mel ni kuy neexai goroom
Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree

⏱️ Synced Lyrics

[00:15.02] Ku fi ñëw mu jangal la
[00:17.58] Nax mi moo ko moon noox mi moo ko moom
[00:20.35] Daf ko dónn
[00:21.63] Lii xar yi la, lii bey yi la
[00:24.21] Nagam yangi, àli bàngi
[00:27.12] Baaxi maamam Pullo Àrdo
[00:36.89] Ku fi ñëw mu jangal fa
[00:39.87] Nax mi moo ko moon noox mi moo ko moom
[00:42.26] Lii xar yi la, lii bey yi la
[00:44.64] Nagam yangi, àli bàngi
[00:47.22] Baaxi maaman Pullo Àrdo
[00:51.45] Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[00:56.70] Pullo Jééri, Pullo Àrdo, Pullo Jééri
[01:02.49] Dàqqal yee ñu jëm fee nga dàqq yil ñu jëm fii
[01:05.26] Yaa xam yaw li xew fee, dara jaxalula fii ba fee
[01:08.98] Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[01:14.04] Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[01:29.88] Àrdo sex na gënnëm
[01:33.42] Dàldi gàddu yattam
[01:36.25] Ma nga ànd ag xaajam
[01:38.67] Dàldi jittël géttam
[01:41.72] Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[01:45.95] Mi ngi ànd ag xaajam
[01:50.05] Dàldi jiitél géttam
[01:52.34] Dalal xelam, fééxal xolam
[01:55.18] Bu nin ñi fo aka ree moom yégu ko suuy
[01:59.44] Pullo Àrdo, Pullo Jééri
[02:04.80] Yeppam mu ngi fii
[02:07.12] Fii la yaroo, fii la màgee
[02:09.94] Te yii fii la takkee sowna
[02:12.78] Léppam fii la
[02:15.46] Pullo Àrdo, Pullo Jééri
[02:22.44] Bu nin ñi tëbë ka dal moom yëgu ko
[02:25.03] Li mu am fii doyloo na ko doy loo na ko
[02:27.79] Bu dee cor la mbaa jamaan la
[02:30.15] Walla etaas la, mbaa abyong la, mbaa leneen la
[02:34.25] Moom gisu ko, Pullo Àrdo
[02:48.37] Ma nga gàddu taxaaran
[02:51.22] Di mbiip mbiip mu am xorom
[02:53.72] Way, way yu amui moroom
[02:56.52] Mel ni kuy neexai goroom
[02:59.34] Boo fa jaaree sant Saar ee di na la ree
[03:04.66] Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:10.13] Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
[03:15.12] Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:21.04] Di mbiip mbiip mu am xorom
[03:26.22] Way, way yu amui moroom
[03:28.98] Mel ni kuy neexai goroom
[03:31.63] Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
[03:36.74] Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:42.53] Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
[03:47.58] Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:52.16]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings