Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Sportif

👤 Youssou N'Dour 🎼 Rokku Mi Rokka ⏱️ 3:25
🎵 1274 characters
⏱️ 3:25 duration
🆔 ID: 7913919

📜 Lyrics

Woyal sa wayu ndam ii
Dangay bégël sa xol bi
Ndax yaa yor bannex bi
Ni tay bés bii sa bés la
Sa mbër daan na kóntaan nga
Bu ñu daanee sa mbër nak
Na nga fexe ba nee
Po mii dañuy Jonante
Faw mu am ku moyle
Jarula defante, di xasteeka dóóre
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Bëgóón nga mu demee ni demewuko
Mën naa am bu ëllëgee mu gën fee neex
Ba ma làng ag samay gaa yi ngir bànneexu
Xam ne lii fo la nii lay mënë deme
Powun jonante nii lay deme
Tay jii yaw bu ëllëgee keneen la
Fo ag ree de lañ ciy jublu
Moo tax ñu wara dal taynangu defet
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Waa waaw wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jigéén
Sire lañu dóór bal géér ña da ñoo daw
Sire Bàlla moo ñaan Ramata Faal
Siree nga Cees Matee nga Njaarém
Duñ ko wëy ku reew, duñ ko wëy ku ñaaw
Aah wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal

⏱️ Synced Lyrics

[00:08.42] Woyal sa wayu ndam ii
[00:10.91] Dangay bégël sa xol bi
[00:13.42] Ndax yaa yor bannex bi
[00:18.69] Ni tay bés bii sa bés la
[00:21.27] Sa mbër daan na kóntaan nga
[00:23.95] Bu ñu daanee sa mbër nak
[00:26.64] Na nga fexe ba nee
[00:32.12] Po mii dañuy Jonante
[00:34.85] Faw mu am ku moyle
[00:37.30] Jarula defante, di xasteeka dóóre
[00:43.38] Jonante po ag ree la
[00:45.86] Boo gañee fo ag ree la
[00:48.48] Boo ñàkkee fo ag ree la
[00:51.04] Lépp ci fo ag ree la
[00:53.78] Buñ la gañee muñël
[00:56.52] Boo ko gañee baalal
[01:05.55] Bëgóón nga mu demee ni demewuko
[01:07.97] Mën naa am bu ëllëgee mu gën fee neex
[01:11.01] Ba ma làng ag samay gaa yi ngir bànneexu
[01:13.05] Xam ne lii fo la nii lay mënë deme
[01:15.75] Powun jonante nii lay deme
[01:18.33] Tay jii yaw bu ëllëgee keneen la
[01:21.09] Fo ag ree de lañ ciy jublu
[01:23.54] Moo tax ñu wara dal taynangu defet
[01:26.59] Jonante po ag ree la
[01:29.82] Boo gañee fo ag ree la
[01:32.44] Boo ñàkkee fo ag ree la
[01:35.18] Lépp ci fo ag ree la
[01:37.85] Buñ la gañee muñël
[01:40.53] Boo ko gañee baalal
[01:55.53] Waa waaw wuy dabbee wuy yoo
[02:05.58] Dabi alaa ko ndey baate satata
[02:11.65] Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jigéén
[02:19.26] Sire lañu dóór bal géér ña da ñoo daw
[02:26.77] Sire Bàlla moo ñaan Ramata Faal
[02:30.32] Siree nga Cees Matee nga Njaarém
[02:38.72] Duñ ko wëy ku reew, duñ ko wëy ku ñaaw
[02:45.91] Aah wuy dabbee wuy yoo
[02:54.44] Dabi alaa ko ndey baate satata
[02:59.76] Jonante po ag ree la
[03:02.32] Boo gañee fo ag ree la
[03:05.02] Boo ñàkkee fo ag ree la
[03:07.63] Lépp ci fo ag ree la
[03:10.31] Buñ la gañee muñël
[03:12.97] Boo ko gañee baalal
[03:16.32]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings