Yow La
🎵 1714 characters
⏱️ 3:29 duration
🆔 ID: 9326545
📜 Lyrics
Set naa setoo setat gisaguma ku mel ni yaw
Sa jëmm je ma yëm man gisuma keneen
Pourtant man, pourtant man
Gis naa façon bu ne
Pourtant man, pourtant man
Gis naa jigéen bu ne
Yaw laa doon ñaan Yàlla (toucouleur al racine)
Ñaan yi mujje àntu (jekk rafet yaa ngi)
Yaw laay gis wër ba ngi
Kuy ndeyam ak baayam setoo set yaa ngi xoolooo say moroom
Jukk leen tay la tay ku ko xam na nga jaayu (jaayu)
Yaa jara sargal yaaa jara tàccu
Jaayul tey sa bés la, man maa la taamu
Say digg moroom say nawle su la neexee baaxu
Mbëggeel dafa diis, dafa bari doole
Yaay sama aljanna (waawaaw yaw la)
Yaay sama aljanna (ahh ahh yaw la)
Yaaa ma leen gënal yaw mi (waawaaw yaw la)
Yaay sama aljanna
Diombadioo ari, diombadioo ari
Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na

Bés bi laa doon xaar, tay dafa mel ni moo ngi
Ëksil sama ndaanaan, naa la siggil ci say noon yaw
Fi ñu jaar li ma la tooñ, li nga may baal
Li ma la jaaral ak fi nga ma toollu sama ndaanaan
Yaa ma leen gëneloon dama leen ko rusoon a wax
Imam teew na nawle yépp teew yaw de nga ni waaw
Njegemaar bis yaa di mët jëg
May ko mu jal sama miss ba ngee
Xale la waaye fees na ak jom
Bis dina doni ndaanaan sama miss baa ngi

Me and you for life, for life bae
Me and you for life, for life bae
Xamal ni ma ngi ci sa wët
Muy taw wala muy naaj ma belle

⏱️ Synced Lyrics
[00:10.54] Set naa setoo setat gisaguma ku mel ni yaw
[00:28.44] Sa jëmm je ma yëm man gisuma keneen
[00:32.36] Pourtant man, pourtant man
[00:34.30] Gis naa façon bu ne
[00:35.79] Pourtant man, pourtant man
[00:37.60] Gis naa jigéen bu ne
[00:39.09] Yaw laa doon ñaan Yàlla (toucouleur al racine)
[00:41.97] Ñaan yi mujje àntu (jekk rafet yaa ngi)
[00:46.44] Yaw laay gis wër ba ngi
[00:49.09] Kuy ndeyam ak baayam setoo set yaa ngi xoolooo say moroom
[00:53.60] Jukk leen tay la tay ku ko xam na nga jaayu (jaayu)
[00:58.03] Yaa jara sargal yaaa jara tàccu
[01:01.21] Jaayul tey sa bés la, man maa la taamu
[01:04.67] Say digg moroom say nawle su la neexee baaxu
[01:08.70] Mbëggeel dafa diis, dafa bari doole
[01:11.77] Yaay sama aljanna (waawaaw yaw la)
[01:13.80] Yaay sama aljanna (ahh ahh yaw la)
[01:16.85] Yaaa ma leen gënal yaw mi (waawaaw yaw la)
[01:20.20] Yaay sama aljanna
[01:23.12] Diombadioo ari, diombadioo ari
[01:27.09] Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na
[01:30.82] Diombadioo ari, diombadioo ari
[01:34.42] Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na
[01:38.01] Bés bi laa doon xaar, tay dafa mel ni moo ngi
[01:45.13] Ëksil sama ndaanaan, naa la siggil ci say noon yaw
[01:52.45] Fi ñu jaar li ma la tooñ, li nga may baal
[01:56.70] Li ma la jaaral ak fi nga ma toollu sama ndaanaan
[02:00.13] Yaa ma leen gëneloon dama leen ko rusoon a wax
[02:03.92] Imam teew na nawle yépp teew yaw de nga ni waaw
[02:07.95] Njegemaar bis yaa di mët jëg
[02:10.13] May ko mu jal sama miss ba ngee
[02:13.97] Xale la waaye fees na ak jom
[02:17.21] Bis dina doni ndaanaan sama miss baa ngi
[02:21.20] Mbëggeel dafa diis, dafa bari doole
[02:25.06] Yaay sama aljanna (waawaaw yaw la)
[02:27.59] Yaay sama aljanna (ahh ahh yaw la)
[02:31.30] Yaaa ma leen gënal yaw mi (waawaaw yaw la)
[02:34.85] Yaay sama aljanna
[02:36.95] Diombadioo ari, diombadioo ari
[02:41.14] Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na
[02:44.25] Diombadioo ari, diombadioo ari
[02:48.95] Diombadioo ari sama sët baa ngi yëg si na
[02:51.79] Me and you for life, for life bae
[02:56.34] Me and you for life, for life bae
[03:00.02] Xamal ni ma ngi ci sa wët
[03:03.68] Muy taw wala muy naaj ma belle
[03:08.82]