Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Gagganti ko

👤 Youssou N'Dour 🎼 MBALAX ⏱️ 3:41
🎵 1557 characters
⏱️ 3:41 duration
🆔 ID: 9492259

📜 Lyrics

Ba ñu la koy jox, xamul dara
Bu la séenee, daw gatandu la
Ay waajurëm, da ñoo amoon yaakaar ci yaw
Jamonooy dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
Bu ko dóor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
Dellool sa xel, ca ginnaaw, te muñël ko

Ba ñu la koy may, xam ul dara
Bu la séenee, daw laxasu la
Ay waajurëm, da ñoo amoon yaakaar ci yaw
Jamono dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
Bu ko dóor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
Dellool sa xel, ca ginnaaw, bu ko souffrir loo
Xoolal ci ay, waajurëm, bu ko joy loo

Bu juumee gagganti ko
Bu juumee gagganti ko
Bu juumee gagganti ko
Bu juumee gagganti ko
Bu juumee gagganti ko

Bu ko dòor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
Bu yënggëlee daal, ba sa xol fees, génnël nga dem
Bu fa toog yaw, teranga bu mu, sàmmal sa cér
Woo ko, waxtaan ak moom, té muñël ko

Bu juumee gagganti ko
Bu juumee gagganti ko

Yaw tam, bul forcer, deel négocier
Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
Te bu amee, lu fi leerul, nga clarifier
Coow li, bu déborder, nga pacifier

Yaw daal, bul forcer, deel négocier
Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
Te bu amee, lu fi leerul, nga clarifier
Coow li, bu déborder, nga pacifier
Wa waaw

Jaajëf, di na tax, xale wone jom
Waaw góor, di na tax, xale yokk jom
Di ko won sa jom, moo koy dolli jom
Jom jom jom rek, dara lu dul jom

Jaajëf, di na tax, xale wone jom
Waaw góor, di na tax, xale yokk jom
Di ko won sa jom, moo koy dolli jom
Jom jom jom rek, dara lu dul jom

Yërëmal ma ko, moomit
Mu wégal ma laa nax ko neex al ma ko
Moomit mu xam ko

⏱️ Synced Lyrics

[00:05.77] Ba ñu la koy jox, xamul dara
[00:09.37] Bu la séenee, daw gatandu la
[00:12.43] Ay waajurëm, da ñoo amoon yaakaar ci yaw
[00:15.90] Jamonooy dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
[00:19.13] Bu ko dóor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
[00:22.40] Dellool sa xel, ca ginnaaw, te muñël ko
[00:38.12] Ba ñu la koy may, xam ul dara
[00:41.23] Bu la séenee, daw laxasu la
[00:44.44] Ay waajurëm, da ñoo amoon yaakaar ci yaw
[00:47.94] Jamono dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
[00:51.41] Bu ko dóor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
[00:54.66] Dellool sa xel, ca ginnaaw, bu ko souffrir loo
[00:57.98] Xoolal ci ay, waajurëm, bu ko joy loo
[01:00.76] Bu juumee gagganti ko
[01:04.19] Bu juumee gagganti ko
[01:07.37] Bu juumee gagganti ko
[01:10.45] Bu juumee gagganti ko
[01:13.88] Bu juumee gagganti ko
[01:17.14] Bu ko dòor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
[01:20.23] Bu yënggëlee daal, ba sa xol fees, génnël nga dem
[01:23.22] Bu fa toog yaw, teranga bu mu, sàmmal sa cér
[01:26.68] Woo ko, waxtaan ak moom, té muñël ko
[01:29.87] Bu juumee gagganti ko
[01:33.04] Bu juumee gagganti ko
[01:35.27]
[02:01.86] Yaw tam, bul forcer, deel négocier
[02:05.15] Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
[02:08.45] Te bu amee, lu fi leerul, nga clarifier
[02:11.50] Coow li, bu déborder, nga pacifier
[02:14.77] Yaw daal, bul forcer, deel négocier
[02:18.11] Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
[02:21.37] Te bu amee, lu fi leerul, nga clarifier
[02:24.53] Coow li, bu déborder, nga pacifier
[02:27.68] Wa waaw
[02:40.62] Jaajëf, di na tax, xale wone jom
[02:43.74] Waaw góor, di na tax, xale yokk jom
[02:46.92] Di ko won sa jom, moo koy dolli jom
[02:50.01] Jom jom jom rek, dara lu dul jom
[02:53.56] Jaajëf, di na tax, xale wone jom
[02:56.76] Waaw góor, di na tax, xale yokk jom
[03:00.15] Di ko won sa jom, moo koy dolli jom
[03:03.01] Jom jom jom rek, dara lu dul jom
[03:09.67] Yërëmal ma ko, moomit
[03:11.92] Mu wégal ma laa nax ko neex al ma ko
[03:16.89] Moomit mu xam ko
[03:26.53]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings