Mama Africa
🎵 1281 characters
⏱️ 3:58 duration
🆔 ID: 9493372
📜 Lyrics
Yée, yée-hé-hé-hé
Yée, yée-hé-hé-hé
Hoo, hoo ehnnn haaan
Hoo africains, woy le leen ma africa
Benn continent, melul ni africa
Amul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw, Africa
Amna ñi soriyaante
Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp
Une jeunesse engagée, africa
Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër
Come home with me
Hoo africains, woy le leen ma africa
Benn continent, melul ni africa
Amul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw, Africa
Ana ñi soriyaante
Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp, avec
Une jeunesse engagée, africa
Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër
Come home with me
Ñun africains, su ñu ànd a ndoo
Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole
Kholal ëllëg u adduna bi
Seetal say doom ñoo, koy mujjee
Yée, hée hée, an han
Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Du ñu la weccoo ba muk
Du ñu la weccook keneen africa
Xam nga ni la say, doom yi bëggee
Tag naa la kaay
Yaa ne ci suñu xol
Wo, wo, wo, wooy
Wo, wo, wo, wooy
Du ñu la mas a weccooy
Kenn du yaw Africa
Yée ... yée hé hé hée hé
Yée, yée-hé-hé-hé
Hoo, hoo ehnnn haaan
Hoo africains, woy le leen ma africa
Benn continent, melul ni africa
Amul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw, Africa
Amna ñi soriyaante
Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp
Une jeunesse engagée, africa
Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër
Come home with me
Hoo africains, woy le leen ma africa
Benn continent, melul ni africa
Amul benn werente ci loolu
Suñu mbëggél ci yaw, Africa
Ana ñi soriyaante
Bu ñu kenn jaxasse
Na ñu xam suñu bopp, avec
Une jeunesse engagée, africa
Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër
Come home with me
Ñun africains, su ñu ànd a ndoo
Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole
Kholal ëllëg u adduna bi
Seetal say doom ñoo, koy mujjee
Yée, hée hée, an han
Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
Noonu nga riché
Du ñu la weccoo ba muk
Du ñu la weccook keneen africa
Xam nga ni la say, doom yi bëggee
Tag naa la kaay
Yaa ne ci suñu xol
Wo, wo, wo, wooy
Wo, wo, wo, wooy
Du ñu la mas a weccooy
Kenn du yaw Africa
Yée ... yée hé hé hée hé
⏱️ Synced Lyrics
[00:03.39] Yée, yée-hé-hé-hé
[00:06.96] Yée, yée-hé-hé-hé
[00:10.69] Hoo, hoo ehnnn haaan
[00:15.68] Hoo africains, woy le leen ma africa
[00:19.16] Benn continent, melul ni africa
[00:22.98] Amul benn werente ci loolu
[00:26.34] Suñu mbëggél ci yaw, Africa
[00:30.53] Amna ñi soriyaante
[00:33.83] Bu ñu kenn jaxasse
[00:37.48] Na ñu xam suñu bopp
[00:41.57] Une jeunesse engagée, africa
[00:45.24] Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
[00:49.27] Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
[00:52.95] Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër
[00:57.05] Come home with me
[01:00.30] Hoo africains, woy le leen ma africa
[01:03.66] Benn continent, melul ni africa
[01:08.01] Amul benn werente ci loolu
[01:11.87] Suñu mbëggél ci yaw, Africa
[01:15.63] Ana ñi soriyaante
[01:19.08] Bu ñu kenn jaxasse
[01:23.11] Na ñu xam suñu bopp, avec
[01:26.55] Une jeunesse engagée, africa
[01:30.43] Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
[01:34.11] Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
[01:37.76] Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër
[01:41.77] Come home with me
[01:45.25] Ñun africains, su ñu ànd a ndoo
[01:48.82] Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole
[01:52.77] Kholal ëllëg u adduna bi
[01:56.42] Seetal say doom ñoo, koy mujjee
[02:07.39] Yée, hée hée, an han
[02:13.17]
[02:32.93] Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
[02:35.32] Noonu nga riché
[02:37.08] Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
[02:39.19] Noonu nga riché
[02:40.31] Du ñu la weccoo ba muk
[02:42.41] Du ñu la weccook keneen africa
[02:45.53] Xam nga ni la say, doom yi bëggee
[03:07.83] Tag naa la kaay
[03:10.91] Yaa ne ci suñu xol
[03:13.79] Wo, wo, wo, wooy
[03:15.57] Wo, wo, wo, wooy
[03:19.06] Du ñu la mas a weccooy
[03:21.04] Kenn du yaw Africa
[03:28.01] Yée ... yée hé hé hée hé
[03:38.38]
[00:06.96] Yée, yée-hé-hé-hé
[00:10.69] Hoo, hoo ehnnn haaan
[00:15.68] Hoo africains, woy le leen ma africa
[00:19.16] Benn continent, melul ni africa
[00:22.98] Amul benn werente ci loolu
[00:26.34] Suñu mbëggél ci yaw, Africa
[00:30.53] Amna ñi soriyaante
[00:33.83] Bu ñu kenn jaxasse
[00:37.48] Na ñu xam suñu bopp
[00:41.57] Une jeunesse engagée, africa
[00:45.24] Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
[00:49.27] Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
[00:52.95] Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër
[00:57.05] Come home with me
[01:00.30] Hoo africains, woy le leen ma africa
[01:03.66] Benn continent, melul ni africa
[01:08.01] Amul benn werente ci loolu
[01:11.87] Suñu mbëggél ci yaw, Africa
[01:15.63] Ana ñi soriyaante
[01:19.08] Bu ñu kenn jaxasse
[01:23.11] Na ñu xam suñu bopp, avec
[01:26.55] Une jeunesse engagée, africa
[01:30.43] Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
[01:34.11] Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
[01:37.76] Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër
[01:41.77] Come home with me
[01:45.25] Ñun africains, su ñu ànd a ndoo
[01:48.82] Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole
[01:52.77] Kholal ëllëg u adduna bi
[01:56.42] Seetal say doom ñoo, koy mujjee
[02:07.39] Yée, hée hée, an han
[02:13.17]
[02:32.93] Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
[02:35.32] Noonu nga riché
[02:37.08] Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
[02:39.19] Noonu nga riché
[02:40.31] Du ñu la weccoo ba muk
[02:42.41] Du ñu la weccook keneen africa
[02:45.53] Xam nga ni la say, doom yi bëggee
[03:07.83] Tag naa la kaay
[03:10.91] Yaa ne ci suñu xol
[03:13.79] Wo, wo, wo, wooy
[03:15.57] Wo, wo, wo, wooy
[03:19.06] Du ñu la mas a weccooy
[03:21.04] Kenn du yaw Africa
[03:28.01] Yée ... yée hé hé hée hé
[03:38.38]