Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Mool (Deglu météo)

👤 Youssou N'Dour 🎼 MBALAX ⏱️ 5:36
🎵 2458 characters
⏱️ 5:36 duration
🆔 ID: 9493500

📜 Lyrics

Yaw mool u géej gi, di jambaar ci réew mi
Bala ngaa dem géej, ngala déglu météo
Bu la nee bul dem, lu mën a xew bul dem
Ben fan ak ñaar, bu mu yax sa liggéey

Doyloo nga yalla, du tee nga sa yor téléphone
Ak sa gps, te bul fatte sa gillet

Sama fans yi ma am, mool ñoo ma gën a xam
Fu ma làngee ak ñoom, guddi gë day xumb lool

Man sama fans yee, ma saf
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
Aka ñoo dégg daaj, ma ni
Moo tax may dem ba jeex, walla

Jambaar ca waar wa
Ni jambaar ca géej gë
Su ma ko mënoon
Ben mool du des ci géej

Bu la nee bul dem, lu mën a xew bul dem
Ben fan ak ñaar bu mu yax sa liggéey

Sama fans yi ma am, mool ñoo ma gën a xam
Fu ma làng ee ak ñoom guddi gë day xumb lool

Jambaar ca waar wa
Jambaar ca géej gë
Su ma ko mënoon
Ben mool du des ci géej

Man sama fans yee, ma saf
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
Aka ñoo dégg daaj, ma ni
Moo tax may dem ba jeex, walla

Yalna leen yalla suturaal
Te di leen samm biir géej
Barkeel seen liggéey bi
Barkeel seen njaboot gi
Aar leen ba ñu doon mag
Jox leen barke maam yi

Man sama fans yee, ma saf
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne

Yess aye

Anh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géejoo)
Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo)
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo (Anh mool ba dem na géejoo)

Mool yi laa bëgg a làng al, seen làng xumb na
Ndax sa ma fan's yi nak, Anh mool yee ci gën a dense

Anh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géej oo)
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo (Anh mool ba dem na géej oo)
Sa telephone ak sa GPS
Bul fatte gillet ba

Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo)
Mool yi laa bëgg a làngal, seen làng xumb na
Ndax sa ma fan's yi nak
Mool yee ci gën ë dense

Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo)
A dëggël, yaw mool u géej
Yaa di jàmbaar
Yaa bari fulla lool
Bari jom lool
Yaa donn loolu
Gëm yalla lool
Yaa xarañ lool, te tabe lool
Youssou woy na leen

Anh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géejoo)
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo(anh mool ba dem na géejoo)

Mool yi laa bëgg ë làng al
Seen làng xumb në
Ndax sa ma fan's yi nak, am
Mool yee ci gën ë dense

Anh mool ba dem na géej oo
(Anh mool ba dem na géej oo)
Anh mool ba dem na géej oo
(Anh mool ba dem na géej oo)

Mool yi laa bëgg ë làng al
Seen làng xumb na
Ndax sa ma fan's yi nak, am
Mool yee ci gën ë dense

⏱️ Synced Lyrics

[00:06.73] Yaw mool u géej gi, di jambaar ci réew mi
[00:10.04] Bala ngaa dem géej, ngala déglu météo
[00:20.68] Bu la nee bul dem, lu mën a xew bul dem
[00:23.35] Ben fan ak ñaar, bu mu yax sa liggéey
[00:33.78] Doyloo nga yalla, du tee nga sa yor téléphone
[00:37.54] Ak sa gps, te bul fatte sa gillet
[00:47.75] Sama fans yi ma am, mool ñoo ma gën a xam
[00:50.99] Fu ma làngee ak ñoom, guddi gë day xumb lool
[01:00.80] Man sama fans yee, ma saf
[01:07.45] Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
[01:14.55] Aka ñoo dégg daaj, ma ni
[01:21.31] Moo tax may dem ba jeex, walla
[01:35.73] Jambaar ca waar wa
[01:37.26] Ni jambaar ca géej gë
[01:38.65] Su ma ko mënoon
[01:40.16] Ben mool du des ci géej
[01:49.20] Bu la nee bul dem, lu mën a xew bul dem
[01:52.76] Ben fan ak ñaar bu mu yax sa liggéey
[02:02.91] Sama fans yi ma am, mool ñoo ma gën a xam
[02:06.39] Fu ma làng ee ak ñoom guddi gë day xumb lool
[02:16.66] Jambaar ca waar wa
[02:18.29] Jambaar ca géej gë
[02:20.07] Su ma ko mënoon
[02:21.42] Ben mool du des ci géej
[02:29.63] Man sama fans yee, ma saf
[02:36.18] Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
[02:43.07] Aka ñoo dégg daaj, ma ni
[02:49.65] Moo tax may dem ba jeex, walla
[02:56.77] Yalna leen yalla suturaal
[02:59.02] Te di leen samm biir géej
[03:00.77] Barkeel seen liggéey bi
[03:02.49] Barkeel seen njaboot gi
[03:04.26] Aar leen ba ñu doon mag
[03:05.95] Jox leen barke maam yi
[03:07.43] Man sama fans yee, ma saf
[03:13.85] Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
[03:20.10] Yess aye
[03:36.38] Anh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géejoo)
[03:42.34] Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo)
[03:48.60] Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo (Anh mool ba dem na géejoo)
[03:54.54] Mool yi laa bëgg a làng al, seen làng xumb na
[03:57.18] Ndax sa ma fan's yi nak, Anh mool yee ci gën a dense
[04:00.62] Anh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géej oo)
[04:06.16] Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo (Anh mool ba dem na géej oo)
[04:12.05] Sa telephone ak sa GPS
[04:16.17] Bul fatte gillet ba
[04:18.32] Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo)
[04:24.16] Mool yi laa bëgg a làngal, seen làng xumb na
[04:27.03] Ndax sa ma fan's yi nak
[04:28.63] Mool yee ci gën ë dense
[04:30.24] Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo)
[04:34.81] A dëggël, yaw mool u géej
[04:38.00] Yaa di jàmbaar
[04:40.91] Yaa bari fulla lool
[04:43.82] Bari jom lool
[04:46.94] Yaa donn loolu
[04:49.99] Gëm yalla lool
[04:52.69] Yaa xarañ lool, te tabe lool
[04:55.77] Youssou woy na leen
[04:59.35] Anh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géejoo)
[05:04.70] Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo(anh mool ba dem na géejoo)
[05:10.53] Mool yi laa bëgg ë làng al
[05:11.64] Seen làng xumb në
[05:13.26] Ndax sa ma fan's yi nak, am
[05:14.99] Mool yee ci gën ë dense
[05:16.79] Anh mool ba dem na géej oo
[05:19.30] (Anh mool ba dem na géej oo)
[05:22.39] Anh mool ba dem na géej oo
[05:25.36] (Anh mool ba dem na géej oo)
[05:27.75] Mool yi laa bëgg ë làng al
[05:29.29] Seen làng xumb na
[05:30.79] Ndax sa ma fan's yi nak, am
[05:32.44] Mool yee ci gën ë dense
[05:35.60]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings