Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Yaw la beug

👤 Abdou Guité Seck 🎼 Coup d'État ⏱️ 3:15
🎵 1566 characters
⏱️ 3:15 duration
🆔 ID: 9499847

📜 Lyrics

Yaw la beug
Heeee yaw la beug
Andandoo ak mindéf kéneu douko dindi, yaw la beug
Kéneu gua si mane té yalla mo séédé yaw la beug
Kéneu gua si mane bâ abadann daa imane té yaw la beug
Kéneu manou la diott si mane bâ dila rombou té yaw la beug
Andando ak mindéf keneu dokou dindi, yaw la beug
Fowé louwoma, négligé louwoma, té wédi louwoma annn hann yaw la beug
Andando ak mindéd keneu douko dindi, yaw la beug
Kéneu manou la diott si mane bâ dila roumbou yaw la beug
Beuri wo andando, nioy toga ndo di diougandou,
Famay bagne dé dieumou lo fa,
Guidé lamm dé yaw dé Guidé lamm yaw la beug
Nékou lo si yéneu diotay yii nangou sa diouko Yay,
Néwou loma tay gua siw té ligua mana
Wané barii ndakh lépou si yaw beauté la,
Guidé lamm dé yaw dé Guidé lamm yaw la beug
Né djiguénn boufi Salo Salo sa djiko dji bo dango niépou
Dall di way sa dialoré ki mo dii yayou Tito Chmi lo vieux Raci
Dioural guala samay domm
Amou lo khar ma yalla
Fama khol fofa guay khol
Sotanté khalatt di diém té mane
Nel sa yaye lamou ligueyonn tégn wa ngué,
Tégn wa ngué yann bi gnewa goul yén bégui si yonn
Yonn dina diém sa kém tou lay katann yaw la beug
Né amna dépense mane na FO yaw la beug
Mane na khalam mane na riti yaw la beug
Lo namatii fii lo djokhognn dagu nako yaw la beug
Sunu beuguél bi mo mane yathia déss yaw la beug
Né amna dépense mane na FO yaw la beug
Mane na khalam mane na ritii yaw la beug
Konn lo namatii lo djokhogn dague nako yaw la beug
Sunu mbeuguél bi dé mo mann yathia déss
Heeee nii yaw la beug, je t'aime

⏱️ Synced Lyrics

[00:08.52] Yaw la beug
[00:12.38] Heeee yaw la beug
[00:14.59] Andandoo ak mindéf kéneu douko dindi, yaw la beug
[00:18.76] Kéneu gua si mane té yalla mo séédé yaw la beug
[00:24.04] Kéneu gua si mane bâ abadann daa imane té yaw la beug
[00:28.64] Kéneu manou la diott si mane bâ dila rombou té yaw la beug
[00:33.64] Andando ak mindéf keneu dokou dindi, yaw la beug
[00:37.38] Fowé louwoma, négligé louwoma, té wédi louwoma annn hann yaw la beug
[00:51.56] Andando ak mindéd keneu douko dindi, yaw la beug
[00:57.30] Kéneu manou la diott si mane bâ dila roumbou yaw la beug
[01:01.59] Beuri wo andando, nioy toga ndo di diougandou,
[01:05.93] Famay bagne dé dieumou lo fa,
[01:09.17] Guidé lamm dé yaw dé Guidé lamm yaw la beug
[01:13.50] Nékou lo si yéneu diotay yii nangou sa diouko Yay,
[01:18.37] Néwou loma tay gua siw té ligua mana
[01:22.28] Wané barii ndakh lépou si yaw beauté la,
[01:24.42] Guidé lamm dé yaw dé Guidé lamm yaw la beug
[01:29.67] Né djiguénn boufi Salo Salo sa djiko dji bo dango niépou
[01:45.10] Dall di way sa dialoré ki mo dii yayou Tito Chmi lo vieux Raci
[01:52.06] Dioural guala samay domm
[02:00.94] Amou lo khar ma yalla
[02:05.95] Fama khol fofa guay khol
[02:10.07] Sotanté khalatt di diém té mane
[02:14.48] Nel sa yaye lamou ligueyonn tégn wa ngué,
[02:19.15] Tégn wa ngué yann bi gnewa goul yén bégui si yonn
[02:24.27] Yonn dina diém sa kém tou lay katann yaw la beug
[02:29.07] Né amna dépense mane na FO yaw la beug
[02:33.08] Mane na khalam mane na riti yaw la beug
[02:38.34] Lo namatii fii lo djokhognn dagu nako yaw la beug
[02:42.93] Sunu beuguél bi mo mane yathia déss yaw la beug
[02:47.99] Né amna dépense mane na FO yaw la beug
[02:52.47] Mane na khalam mane na ritii yaw la beug
[02:57.73] Konn lo namatii lo djokhogn dague nako yaw la beug
[03:01.87] Sunu mbeuguél bi dé mo mann yathia déss
[03:06.13] Heeee nii yaw la beug, je t'aime
[03:12.07]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings