Home 🎬 Bollywood 🎵 Pakistani 🎤 English Pop

Jammu Africa

👤 Ismaël Lo 🎼 Jammu Africa ⏱️ 5:02
🎵 912 characters
⏱️ 5:02 duration
🆔 ID: 9668229

📜 Lyrics

Afrika a a a Afrika mon Afrique
Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew
D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique
Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique

Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique

Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam to Ruanda
Yoo Alla addu jam to Burundi
Yoo Alla addu jam to Casamans
Lawol Mbignona yee

⏱️ Synced Lyrics

[00:14.18] Afrika a a a Afrika mon Afrique
[00:28.75]
[00:38.14] Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq
[00:43.49] Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew
[00:47.62] D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique
[00:51.52]
[00:54.74] Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix
[00:59.02]
[01:01.98] Kon jammu Afrika moom lay ñaan
[01:07.15] Mané jammu Afrika mooy suñu natange
[01:10.97]
[01:25.43] Afrika a a a Afrika a a
[01:33.21]
[01:36.63] Afrika a a a Afrika mon Afrique
[01:39.43]
[01:48.48] Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan
[01:51.28]
[01:54.95] Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika
[01:57.48]
[02:01.25] Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
[02:04.97] Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères
[02:07.45]
[02:09.82] Kon jammu Afrika moom lay ñaan
[02:12.37]
[02:15.61] Mané jammu Afrika mooy suñu natange
[02:18.51]
[02:37.42] Afrika a a a Afrika a a
[02:43.34] Afrika a a a Afrika mon Afrique
[02:49.46] Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men
[02:53.39]
[02:56.42] Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
[02:57.42] Yoo Alla addu jam to Ruanda
[02:58.43] Yoo Alla addu jam to Burundi
[02:59.41] Yoo Alla addu jam to Casamans
[03:00.47] Lawol Mbignona yee
[03:00.62]

⭐ Rate These Lyrics

Average: 0.0/5 • 0 ratings